30

3.4K 272 0
                                    

Salam aleykum

Kiné: Fatou do nopal sa khéle mi sakh temps yi dangaye diangue rk

Moi : bayile ma diangue ndakh ma dague bac téh dama beugue sama pp contane si mane

Kiné :  wayé daga wara nopalou taye sakh dagaye diouke gnou déf balade

Moi: non bayil ma toke diangue amouma diote bobou

Kiné :  wa légui daga beugue déme ba examen ya sa bopou di métti

Moi :  non beugouma ma lolou

Kiné : khana khamo bo topé di diangue téh nopolo sa khéle mi.dagaye déme ba bisou bac ya nga faté li nga diangone lepone

Moi:  kone na diouke  dakh dama beugue sama pp fière si mane doneté bénde jour laye done

Kiné : kone diougale

Gnou diouke tagou sama tanta guénde dokhone tou dieunde crème glace 🍦 déf shopping ndakh temps yi bachir mogniye douga lale khalise

Kiné: hum taye sama journée dafa nékh

Moi :  mane tmt geudie n'a djénde teh gnome Virginie dama léne guedia guiss khamna diangue mila

Kiné :  iow ak Virginie loléne dioté

Moi : dara khana mane moma diakhal wayé damay khare ba  examen yi dialle ma ladie kako

Kiné :  peut-être ligaye andal boris mo takh ndakh temps yi souma Ana ladié ana Fatou maniko da andake boris Virginie daye mére diouke

Moi :  han mangui doga comprendre pourtant wakhone nako danga nope Boris mounima non

Kiné :  dalaka rousa wakh rk wayé mane mi sakh khame nani dako nope

Moi : pourtant boris danane ma diokh m'a numéro Virginie damako nope wayé mane maniko boule sonal sa bopou Virginie nabou la

Kiné : yakh nga lou beurri

Moi : nagne déme mo guëne gnou toke fi di wakh

Après gnou déme gnibi

23h

Moi: iow kiné ana sama cahiers yi

Kiné :  mako dénthie iow bane gnibi sé ba taye yangui diangue dagaye teudd nélaw ba souba nga yégalé

Moi: shut daga lakalé bayile ma diangue rk

Kiné : kholal fatou temps yi nélawo ba yandore teudeul ba souba nga yégalé

Moi: wa bakhna kone wayé taye kasé la dh

Kiné :  iow kaye teudeul rk

Ma teudd

Je vous passe une semaine jour examen yi

Kiné :  kholal fatou yalla nga dague doffice bi ak mention très bien

Moi :amine tanta gnanale ma

Tanta: inchalla dagaye ame wayé sa gnanou yaye mo guëne

Moi :  sama yaye gnanal nama ba paré

Tanta : sa pp nake

Moi: kokou douma gnanale sakh mangui déme

Tanta :  takhawal gnou goungué la 6h30min mo diote teh diamono dji woroul

Moi: merci je vous aime

Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Où les histoires vivent. Découvrez maintenant