32

3.1K 248 0
                                    

Salam aleykum

Je vous passe jusqu'au jour de délivrance de baccalauréat

Moi: kiné gawal mangui déme dh

Kiné :  mangui ni légui ma paré diaroul tite dagaye ame inchalla

Tanta :  Fatou diaroul stressé wou

Moi: wa souma amoul nake kone sama pp dama guëna haine

Tanta :  boule wakh lolou so amoul tmt sa pp dina khamni défe nga effort té dagay ame sakh

Moi: iow khamo sama pp souma amoul. pote la may takal

Kiné :  guiss nga Fatou paréna nagne déme nga nékki fi di stressé wou yalla bo kheum sama kaw

Moi: yalla bakhna

Kiné :  souffle 🌬 râle

Moi : 🌬

Kiné :  nagne déme 9h diotena téh 10h la wara commencé

Gnou déme fékk fa éleve you bari gni andak séne kharite Wala séne make khame nguéne rk jour délivrance loumouy mél

Mounass :  gni dagnon wara gaaw instant bi mangui mélni kouy déad

Virginie : mane mome khama touma fouma nékk

Evachou :  ah yalla bakhna

-approchez approchez

Ma guise kouy diokhé résultat yi sama battement de cœur bi accéléré

-bonjour tout le monde avant de commencer je voulais vous dire les candidats admissibles qui sont tenus de récupérer leur relevé de notes .
A ce qui concerne les candidats du second tour ils peuvent venir demain à 9h
Maintenant je vous donne vos résultats par ordre de merite

- Le numéro 30 Abdou Dieye mention très bien

Virginie :  alhamdoulillah abdou amna

-Le numéro 240 momy Ndiaye mention très bien

Kokou tmt teupe wayé mane mangui wadia dead

-Le numéro 35 Virginie dieye mention très bien

Virginie :  alhamdoulillah

-Le numéro 5 majib dia mention très bien

Le numéro 45 Astou diop mention très bien

-Le numéro  210

A suivre

Ah dama léni togne rk






















































OK mangui léne koye wakh

- Le numéro 210 Fatou Ndiaye mention très bien

Kiné :  OOH ALHAMDOULILLAH AME NAGNE

moi: ALHAMDOULILLAH AMNA SAMA PP DINA CONTANE

- le numéro 130 Mouhamed mention bien

Gnou wakh trois personnes

- Le numéro 83 Maïmouna fall (Mounass) mention bien

Moi: MOUNASS

Mounass : on l'a fait

Gnou wo plus de 20 personnes Evachou ba taye gneuweu goule

Evachou : Fatou douma ame

Moi: inchalla diga  ame diekha goule

Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Où les histoires vivent. Découvrez maintenant