43

3.2K 264 9
                                    

Salam aleykum

Tjrs dans la peau d'Abdou

Gnogui si hôpital bi di khare medcin bi guénn depuis un heure gnogui takhaw di khare
Gnome kiné gnigui dioye rk surtout kiné ak Ana
Evachou ndakh kiné bame nopi Virginie ndakh Ana bame nopi
Majib nieuw sama coté

Majib : legui mou yewou diaroul inquièté wou

Daye melni dama koye niakk
Loutakh gnima beugue fima léne sokhla rk lagni déme wakho goumako sakh limaye sentir
Beuguouma ko pedre billahi

Un instant médecin 😷 bi guénn
Gnou daw dieum si mome

Kiné :  comment va ma cousine ?

Médecin : ne vous inquiétez pas elle s'est évanouie seulement mai peut être elle va se réveiller dans quelques temps

Moi: Ahmdou lillah on peut aller la voir

Médecin : vous pouvez la voir mais ne la dérange pas  par ce qu'elle a besoin de repos

Après gnou déme fékk ko mou teudd si lale hôpital bi même bouy nelaw sakh daye raféte

Kiné : alhamdoulillah legui mou yéwou

Evachou : doli sante yalla rk

Mounass : nagne ko bayi mou reposé wou, Abdou mane gavé dése

Abdou : wawe merci

Gnome gnou djénde ma dikki toke si cotéme machalla même boudé nelaw daye raféte ak teint clair comme metisse
Ma guiss ko mouy yeungou

Fatou : de l' eau

Ma gaaw indile ko ndokh diokh kako. Mounane

Retour dans ma peau

Magui yéwou wayé dama mare

Moi: de l' eau

Ame kouma diokh ndokh
Ma yewou mouy Abdou wa loumaye déf fi

Moi: loumay déf fi

Abdou : daga danou si escalier yi fatéwou loko

Moi: non faté likou ma dara

Si la fatélikou ni Mane ak aïcha gnodone wakh ame koumay mbeumeukh
Aïcha la sorciere bime done

Moi : en fatalikouna

Abdou : lo def ba danou si escalier

Moi: Aïc....

Ma déme baye wakh Aïcha la.  Cette sorciere mou dougou si Salle bi
Mouy saytané saytané lou

Aïcha : Oh fatou titeu lone nga gnou Alhamdoulillah fékké dara daloula

Moi: ya...

Maye wadia wakh mou dikki sama coté akolama mouy wakh si  sama  nopi yi

Aïcha :  so wakhéni mane mala mbeumeukh Guiss nga limala déf loko raw dinako déf sa tanta damaye yondi aye bande gnou raye ko

Ki vrai sorciere la wayé souma défoul lolou manena raye sama tanta khamna aïcha
Mou sigui  di sourire

Aïcha : Dieu merci dara daloula kharal ma wakh gnome Virginie yéwou nga

Après mou guénn

Abdou : guiss nga lila gnigne gni beugué

Gnome Virginie dougou si salle bi

Kiné gneuw akola ma

Kiné : Fatou tita lone ngama

Abdou et Fatou  amour  inoubliable ( Wolof)Où les histoires vivent. Découvrez maintenant