C la dernière partie mes amours encore je vous remercie pour les 85.6 k vus et les 6.13k votes
--------
Abdou : demal si chambre bi mangui gneuw
Moi : WA bakhna fo dieum sakh
Abdou : da ame loumaye lidieunti rek
Moi : hum kone bakhna boula djiguéne khole boul wakhak djiguéne
Abdou : shut
Après ma déme Toke touti Abdou gneuw ame loume gnabalé si lokho bi
Moi : oooh lo yore
Mou diokh mako bénn robe bou rafete la
Abdou : sole ko da ame fougnouy dieum
Moi : wei dada raféte sakh
Abdou : merci iow laye khare
Ma changé yeuré lale touti maquillage
Abdou : waouh 🤩
Moi : sama dieukeur néké dafa mana dieunde dh
Abdou : c normal yaye sama sokhna nake
Moi : prck je suis ta femme
Abdou : yangui melni nare taye
Moi : merci si compliments bi
Après mou diapou sala lokho gnou déme
Oups ! Cette image n'est pas conforme à nos directives de contenu. Afin de continuer la publication, veuillez la retirer ou mettre en ligne une autre image.
Gnou guénn mou diokh bénn fleur
Moi : merci t'es romantique dh
Abdou : derien mon amour 💕
Mou takk sama beute yi. Mou diapou sama lokho gnou déme
Moi : Dina danou yéga goune
Abdou : légui rek
Gnou dokh touti
Abdou : ok yékk si nagne 1 2 3 surprise
Moi : waouh omg 😱 mais..
Abdou : tu l'aimes
Moi : bien-sûr k wi merci Merci *larme de joie*
Abdou : donc je suis soulagé k nékh nala
Mou talal ma lokhome Yi ma diokh sama lokho yi , kheuthieul ma chaise bi ma toke apres mou tok
Mou dèfe signe si lokho bi gnou indil gnou deux plats AK ndokh
Oups ! Cette image n'est pas conforme à nos directives de contenu. Afin de continuer la publication, veuillez la retirer ou mettre en ligne une autre image.