chapitre 4

321 16 0
                                    


.....
Le week-end est terminé est franchement un bon week-end en famille parmi tant d'autres...
On est lundi et je dois accompagner mon père pour ces consultations  mensuel...

Papa: yaye boye paré ngua
Moi: wi papa ,niou gaw
Papa( sur la route):sama thiate bi ,merci manguilay nianal yalla na ngua barkel yalla na sa diangue bi barkel comme nimay nianalé say mak ,ndax meunone ngua kheuy dem école bayima fii donc diarama sama domm...
Moi: papa ,yow tamite mane kay takhawouléne moy sama wareef téké gouma pour téral léne kay ,nianal niou rk ...  taxi ,taxi ...( en avançant vers le taximan )Assalamou aleykoum no def
Lui: wa aleykoum Salam ,mangui si diam
Moi: hopital fann laniou beug déme
Lui: wa défal 6000f
Moi: ah tonton cher na di
Lui: ah hana guisso 6h moyen du matin laniou nekk nak soxnassi
Moi: deugleu kay wayé 3000f bakhoul?
Lui: niou yendou ak diam( en partant)
Moi: papa ki demna di
Mon père : bayiko mou déme
Moi: taxi,taxi
Lui: wi madame cv
Moi: bien ,hopital fann
Lui: wi defal 7000f
Moi: ah wa yéne lounkhew li cherna di ,wagnil tonton
Lui: bakhna 6000f
Moi: 4000f bakhoul ,diapsi sama papa da commencent sonn
Lui( en regardant mon père):d'accord yegléne...

L'apeage a beaucoup d'embouteillage de si tôt...

Mon père : Hapstou comme que embouteillage daffa serrer wathial diéndeul ma ndokh
Moi: d'accord papa .......WOUY SAMA  NDEYE...

   Prologue

Hapsatou se retrouve toute mouillée
Ne le réalisant pas son père vins à son rescousse...

Sékou Diouf( père de Hapstou): Hapstou ki sotinala ndoukhou foss mais boul statut si talibini
Hapstou : papa neunlay démé tay école ak hopital beu ana auto bi(en regardant au tour d'elle)
Tok tok ,yow éee wathiél sa vitre tchimm  ,ni rk nguéne di deff vitré sen auto yi en noir di deff lolen nekh si talibi fok né yéna mome nitt gni ,WATHIAL LA WAKH

Sékou: Hapstou arretel sa youkhou yi

Saliou le chauffeur ( en sortant de la porte d'arrière): Assalamou aleykoum papah ,baléne niou dé  ,vraiment niogui diégalou boubakh
Hapstou : yow vu sa tenu yay chauffeur alors que si guinaw ngua tok donc dawalo ,ki dawale la beug guiss na gaw..
Sékou : Hapstou tu la ferme té démale dieundi ndokh mi
Hapstou : wa papah...
Sékou : Hapstou !
Ainsi Hapstou tourna les pieds avec les klaxon des autres de libérer le passage...
Sékou : balnaléne
Le patron en sortant cette fois ci de la voiture...
Patron: papah ,baléne ma dé vraiment guiss né soxnassi dafa mer mo takh guénouma si auto bi ,mais niogui niane ndigeul...
Sékou : sama dom la ,dina wakh ak mome dinala ball bou sobé yalla,tour bi?
Patron : cheikh Aboubakar Aïdara, papah niogui déme
Sékou : machallah Aïdara niou yendou ak diam...

Ainsi les hommes  se quittèrent...

Dans la peau de Hapstou

Hopital fann de Dakar

Ça fait maintenant plus d'une heure qu'on  attend en silence...

Mon père : Hapstou bayil sa gnagual gui yow tamite li khew dialneu té niom balounaniou
Moi: mais papa gni si bopam niow rew
Mon père :Hapstou
Moi: wa balmeu ,mais papah après ngua dieul taxi déme gnibi dengua ngua deff attention...
Mon père : pour yow mane xalé la
Moi: ah papah woroul...

CONSULTATION NUMÉRO 3....-attendais-je à l'annonce
Moi: papah niou dem
Mon père : waw kayy.....

Nous nous sommes séparés que vers 8h43 ...

Sama Nattou YallaOù les histoires vivent. Découvrez maintenant