Saar 3

11.6K 1.5K 55
                                    




           

Saar 3

*****Khalil*****

Magui sama nek tok, di wakhtane ak Alé par whatsapp. Puisque dafa dégne koumpeu il fallait que ma wakh ko li khew temps yi. Mais bon puisque dokhiwouma, démouma féne. Lima gnou meuna nétali bariwoul.

Ame na kouy feugue.

-Waw.

Sama mague bou djiguéne bi la, Dior
.

-Khalil, kay wouyou.

-Kane ?

-Nidiaye Bass.

Ay ré moma moudié diap.

-Ah, daguay ré ?

-Boci meunoul dioy, gua meune ci ré. Sete ci wou Nidiaye Bass bima akséi ba légui maguikoy khar.

-Mo takhitt gneuw na. Merr na nak bay wadia exploser. 

-Mane ak mome kane mo wara merr? De toute façon, Nidiaye Bass comédien leu, gnou deme kholi lime may wakh.

Ma wathie ci salon bi ak Sala mais Sala douguoul. Ci bir, Nidiaye Bass la fa ak béne kharitame bou toudou Daouda. Sama yaye ak sama papa fi la leine bayi wone bi ma yek.

Diokh na léne lokho soguay togue.

-Khalil nagua def?

-Magui sant bou bakh tonton.

-Mba gni gua bayi France tamitt gno gui ci diam rek.

-Nonou maléne bayi wé dé, diape nani gno gui sant gnomitt.

-Ani Coura ?

-Khana migui ci diam.

-Té amo lénéne lo ma meuna tontou kou doul li ?

-Nidiaye, lane gua beugue ma wakh. Sa dome nékatoul sama diabar ba ma meuna kham ci loume nek.

-Sama lokho dome bimakoy yeukeuti dila ko diokh wano ma wone li. Béte gua ma nak.

-Mane ma la bête. Nidiaye dafa mel ni mane ak yow bokougnou histoire bi gnouy wakh dé. Sougnou touki bou moudj bi, est-ce que lignou wakhaneté wone def gua ko ?

-Lougnou wakhaneté wone ?

-Que sougnou délou wé France, mane ak Coura que louma nakari ci mome nala wo wakh lako digua mako fadial. Nidiaye bima la wowé loma wakh ? Yow ware gua ma meuna wakh que mane na bal sa dome alors que mome ba légui balou woul té done continuer yimouy def. Noma meuna wakh lolou, wala wéthite yi la Coura done diokh mola yobone sa fitt ?

-KHALIL.

Sama yaye youkhou nama. Fatéwone nani sakh que wétou ma fi ak sama nidiaye.

-Khalil, ki sa nidiaye la dou sa morome, mok sa yaye gno bok ndeye ak baye.

Sama papa ame na lou bari louma ko beuguone wakh mais dall diarouko. Souma manquerwé de respect sama nidiaye ci sama kanamou yaye ak papa dama léne di manquer de respect par la même occasion té lolou warouma.

-Khalil, ware nama khol dima wakh li.

Non, khar léne... Pa bi dafa beugue victimizer wou ni ? Diaroul goudeul.

-Nidiaye, magui diégualou sékougnouko.

-Mane sakh dama fi gneuwoul pour lolou, donté négua may guako batam dama beugue kayite yi lerr mou ame certificat divorcam. Ndakh mou meuna ame bénéne dieukeur.

Kéne kou mel ni yowOù les histoires vivent. Découvrez maintenant