Saar 10

8.1K 1.1K 57
                                    


Saar 10

****Adja*****

Wa Khalil mome yague na di. Sama crédit bi dé dinako diékhal. Khoma loumouy wakh ak Ouzin mais ware na def lou gaw. Ma siggui guiss ko mouy dougue ci. Mou déloma portable bi tok.

Ma setlou ni kanamam changer na.

-Khalil, ça va ?

-Oui, ça va.

-Ouzin loume la wakh ?

-Non dou Ouzin. Dama sone rek. Kharal ma wo serveur bi régler addition bi gnou dem.

-Ok.

Ma diko khol mo def sign serveur bi après mou régler affaire bi gnouy sogay dem.

Khalil dé comme bénéne nitt instant yi. Souma agué keur gua dina wo Ouzin car changement meunoul gawé ni.

Ci auto bi ma def #123# pour khol gnata crédit mo ci dess guiss ni dara démoul. Sama khel nak commencer gnaw. Ma dougue ci appel guiss ni dernier appel moy sank bimakoy wo.

Khalil mome mogui concentrerwou ci talli bi wakhouma dara mais tite na instant yi. Khalil bou dé dafa dougue sama messages yi wala sama whatsapp ak mossibeu yi ma def yeup, tay ma dé. Mais Khalil meunoul guiss lolou yeup té saggawouma thia restaurant. Kharal ma bayi sama gnaw khalatt bi té calmerwou. Souma angoisserwer téme ma diokhko ay doute.

-Bébé, séde gua dé. Lane la ?

Khalil dé souma tonto, golo ga gnou teuthie thia zoo parc Hann ba moma tontou.

Ki c'est sûr que lire na sama message yi.

-Wa doma wouyou ?

-Douci keur lala dieulé, dinala delo ci keur.

-Do ma wakh sakh li khew ?

-Adja, merde. Damay dawal teudial sa guémigne gui.

Youkhou bimou oukhou dé teup lo nama. Yalla boume ma dor rek.

Aksi naigne, mou garer auto bi.

-Wathial sama auto.

-Wa légui doma wakh ?

-Oma loumay wakh ak thiaga. Té yow thiaga yi sakh gno la tané car gnome au moins gni gui assumer lounge done. Adja yama béte. Khalatone na louné sauf que j'ai partagé avec toi 6 mois de mensonge. Gua time ma chaque jour dimay féne, dima gueumelo you amoul féne.

-Khalil, bayil ma expliquer leu. Bou dé ligua guiss ci portable bi.

-Wathial sama auto.

-Nguir yalla. Kholal, worena yalla dou lolou.

Khalil dé wathie auto bi la def, oubi fima togué wone, guéné ma mayouma sakh ma expliquer kou doul nane ma que thiaga la té mome dou wakh ak thiaga.

Ay mane yakouna di. Ay mane fouma dieume ???

Ma dokh dougue sougnou birr keur gneupeu gui ci bir salle. Taf taf la dougue nouyo déme sama neg.

Li yeup mako tek sama bop khoma nouma meuné conserver genrou conversations you mel nonou. Aùe na yo khame né bo ci paré wé rek daguako wara yakk.

Mais tamitt, nane rek, nane la meunone khalatté ni Khalill dina meussa fouiller sama portable nane rek la meunone khalatter lolou.

Non, non. Khalil il faut que ma wakh ak mome. Khalil meunouma bayé ni. Kharal ma guissé ak Ouzin, peut-être que dina ma diapalé. Mome bou wakhé ak Khalil dinako deguelou.

Bima guissé ni Khalil doy nama rek dama warone bayi lima néké. Khalil bimou khamé ni que salon ba amougnou salaire que ay nekhal dongue lagnouy ame la commencer def chaque fin du mois bou dioté salairam ame loume maci diokh néma pour que ma diapaléko sama wa keur. Instant bobou rek la warone doylou té bayi lima done def. Khaliss bima done ame ci gnénéne gni damako dane kholl mais wore namani doyéwouma ko wone dara mais guissouma wone sama bopp ci abstinence sexuelle et je tenais trop de continuer à faire tourner la tête aux hommes. Khame ni mane laigne désirer té sokhla wougne kénéne. Légui nak lore na sama bope car gnognou gneup dou kéne ko ci kham ni mane gnane na yalla mou done sama dieukeur. Khalil dongue moma doyone té légui bayinama.

Ma degue ni ame na kouy feugue.

-Entrez.

-Wa Adja Astou daguay dioy.

-Dedette yaye dioyouma dé.

Magui wakh di fompe sama raguogne yi.

Sama yaye tok ci kow lale bi. Dama teudone mais après dama diogue tok.

-Wakh ma lou khew.

-Yayeboy dara khewoul.

-Dara khew na kay. Bigua dougué ci sale bi la guiss ni sa kanam démé ma khame ni amen a lou khew. Adja Astou may sa yaye meuno ma neub.

-Dama khoulo ak Khalil. Lolou mo oube sama bop bi.

-Lou khew ba guéne di khoulo ? Khalil mifi gneuw sank ba gnou done wakhtane. Mou dieul Fanta diko togne. Nou guéne meuna khoulo wé ci diguaneté bou gateu bi.

Yayeboy nak, diape ci rek. Meunoumala wakh deugue bi.

-Serveur bi mo done def louko nekh après ma done casse nak, Khalil mer ci lolou bagne khoulo ci auto bi.

-Ah bou dé lolou rek la mome diaroul inquiéterwou. Affairou khalé la rek.

-Si si dina arrangerwou dagno méro rek.

-So beugué ma woko.

Bime wakhé lolou, sama fitt bi dafa né reuss.

-Dédette diarouko. Légui rek lepp dina arrangerwou.

-Magui delou salle ba kone khol khalé yi.

-D'accord. Mane mome magui sangou dji après ma teudi.

-Kone bakhna.

Sama yaye guéne nek bi ma diogue soumékou soguay deme sangou.

******

Ligueyi dimanche meussoul yombe mais salon mome on est obligé. Clientes yi dimanche lagnouy ame diote. Instant yi magui déprimer grave. Tay mome bou kéne wakh ak mane ni khame nani sama tontou dou nekh.

Ma yeksi rek Dié kheuthie sama lokho bi guéné ma salon.

-Wa yow lane la ba gua may kheuthie?

-Lane la bi kay yow la koy lathie ? Ouzin moma wo demb dima khass nane ma yéne gneup ay fénekat guéne. Adja wakh ma lo def.

-Khalil demb daf ma abe sama portable néma day wo Ouzin. Mou gneuwatt mer, ndéké dafa khol message yi ak yénéne.

-Layila ilala. Kharal ma gneuw def sama portable « réglage d'usine »

-Dié, Khalil néna demb mane thiaga la, khass nama bama rap. Nénama dou wakh ak mane, mayouma akh ma expliquerko.

-Ouzin bimou ma wowé déguena batou Khalil ci soufe mo takh bimou mané « ay féne kat guéne rek » khalatone nani que Adja ame gua ci wale.

-Khalil demb dafa démone keur Ouzin ?

-Ladjoumako Ouzin mais ki ma dégue mouy wakh ci souffe Khalil leu. Ouzin mima ciy khassalé té sama yone nékouci moma méti.

-Dié nak yaye sama domou ndeye fouma piquro ware guafa nané dome. Wa légui tay dougne wathié dougne deme keur Ouzin.

-Pour lane ?

-Pour que mou diapalé ma ci Khalil.

-Ouzin dé mane rek dafe ma méré instant bi. Mais naigne déme rek. Mais nak fawe gua woute loy expliquer.

-Goudi gui yeup ci lolou la done khalatt. Nama diapalé rek ni Khalil khame nani ins yi, nagouwouma deguelou.

-D'accord.

Gnou delou ci bir. Bi Dié di kheuthie nuyo sakh defoumako wone khoma lou takh ndaw ci eupeul.

Sama yakar ins yi mome Ouzin la, yalla na ci meune dara rek.


Kéne kou mel ni yowOù les histoires vivent. Découvrez maintenant