Saar 25

8.7K 1.2K 36
                                    




Saar 25

****Adja****

Bi ma gnaké liguéyi demb warone na wo Nogaye dé. J'espère juste que salon ba fessoul wone et sama présence obligatoiroul wone. Mais Nogaye khame nama. J'ai toujours été sérieuse. Khame nani souma gneuwoul rek c'est parce que dama ame empêchement.

Tata dé la dieul pour liguéyi. Toukhou sofe na. Sougnou keur ak salon ba dokh ague leu wone.

Tata rek la bagne. Té amouma wone sagne sagnou lathie Khalil passou taxi. Ah, dougne la may lépe kat ga dieul lépe, ame na yo khame né khel mokoy motali.

Probablement khame nani gneupe aksi naigne salon ba, ma wara oudier dé. Heure yi dane nama fa fek.

Ma demander arrêt bala chauffeur bi dima yobe fou sorri.

Ma wathie dougue ci kogne bi.

La ma sagnessé nak eupe na. Haut bou tok la sol. Beugone na def ay talon sakh mais dal mané day eupe en plus fi ak souffe sou bari gui fi ame. Bou salon bi nekone ci kaw tali bi sakh mou tané.

-Assalam aleykoum...

-Wa ki dou madame Ndiaye ???

Dié wakh lolou bi mou ma dégué ma nouyou.

-Madame Ndiaye dé la, Kor Khalil.

-Adja naga def nak ?

-Ma fi Nogaye. Mami comment tu vas ?

-Magui fi Adja ça va.

-Ça  va bien.

Khame guéne nitt kou gathié di ray ??? Béne mo gui ni. Mami dé fi la takhaw né, mane ak Dié khalé you goor yi foyé gnou wathie gnou rek laigne name ci gnoune. Que tak mome dougne gnou ko meussa def. Légui nak mo gui ni ak gathiéme.

Non seulement tak naigne ma mais mako gneuka dégue al khayri. Mome ak faram sossou ga khame né nékéwoul ci kogne koudoul wagni potou lampe. Ah !!! Djiguéne day ame ambition. Garab bou la soutoul dou la may kér, olof Ndiaye moko wakh.

Ma dieul place tok.

-Nogaye magui diégalou pour lima gneuwoul demb. Walay prévoirona gneuw.

-Grawoul daga may wane ni dagay sétou. Puisque demb férié la wone, mané monsieur gui fa  té amo envie bayiko fofou.

-Walahi, bou done monsieur dongue la diga ma guiss.

-Kone lou la téré gneuw...Me demande Dié.

-Sama goro khana.

-Sa goro ga wakh dé.

-Nogaye goro dé la wakh. Mère bi dal guéné na demb foote, bou baris akh car keur gui yeup leu wone. Mais foote bi sakh dou problème car gni ko timone barina. Mane dal may foote ba ay 8h yoyou, ma beugue diogue déme défari keur gui puisque ma wara fobéré, mère bi né douci dall. Ma expliquéko que dama wara liguéyi, mou néma yonam nékoussi. Que liguey bi amoul gneurigne kéne douma faye.

-Sa goro mome khana khamoul lane moy liguéyou salon. Fo école rek la, so khamalé yobalé def sa yeufou bop...Nogaye mo wakh lolou.

-Lolou dé la ko expliquer, wayé nagouwouma déguelou. Mane dé comprendre nako, mère bi dal séte na ba séte wayé dal mane safouma ko. Khoma nak loumako def.

-Belle-mère yi dé moy lolou. Chance deugue moy takh ga tomber ci bou bakh. Mais yow dou ame ga ay woudj péthorgo, nonou la mère bi mel ak gnome ?

-Relationwam ak samay woudj péthiorgo dé yakar nani normale na. Pour lima diota guiss ci semaines yi ma fa passé. Yagagouma fa nak pour meuna évaluer. Lima khalatte dal moy mère bi kheuyna dama ko sof car douma mbokam.

-J'ai pas compris. Lane mo ci indi affairou mbok ?

-Dié dama remarquer ni, sama péthorgo yeup ay mbokou mère b laigne, même si khoma exactement bane lien la. En plus exou Khalil bi tamitt diarbatou mère bi la.

-Yow kay yagui sogay wakh...Dit Nogaye.

-Doyna war dé.

-Mais nak fais attention ak. Nala wore ni sa goro moy dodj bi yaye naine bi, bou dalé sa kaw ga gagnou, bo dalé ci kawam gagnou. Moytouko.

-Nogaye, sama goro dé souma défé lime beugue kone dotoma guissati fi.

-Ga nakhane té ak mome rek.

-Mane khame gama. Khame gani oma béne problème. Douma khoulo douma khekh oma diote bi sakh. Sama koude diame la meussa rathie.

-Tay bayi nala ga gneuw. Continuéle rek.

-Bayi? Mouk. Khalil la tagou mou néma téré wouma. Ma def samay ligueyou keur, dougue sama nek ndéki paré fek ko sa salle ba néko bagui liguéyi. Kharouma sakh mou tontou ma.

-Waro wone def lolou dé.

-Nogaye nak lo beugone mou def. Khalil lay seuyal dé pas yayame. En plus néna mère bi dako wane né beugouko ouvertement. Gosse sa seuy bi mère bi dina ci takal souffe dé.

-Dié boul sakh inquiéterwou. Douma ko may occasion mou ci takal souffe. En plus sama dieukeur beugue nama et je sais que bouko soukhla wé, dina dieul sama défense.

-Mais dal, restéle...

Bala Nogaye di agali limou beugone wakh béne cliente nouyo né ay soins la beugone. Douma dieuw sama belle-mère ci kanamou kouma khamoul. Nonou laigne fa yama lé wakh tane bi.

********** 

Khalil dal moma défaral tay surprise bou nekh. Woma lathie ma sama heurou wathie ma wakh koko mou néma ok.

Ma gui done wakh wa ki loume ma yabé, ware ma wo lathie ma bane heure lay wathie pour rien ?

Mane dal nimay guéné rek guiss autome garé.

Après sama khel dem ci faté khadioufi. Warona ndand ni Khalil dafe ma beugone défal surprise rek.

Ma feke ci ko auto bi mou khamal ma ni, c'est pas parce qu'on est marié que dagno wara bayi sortie yigne done def bagnouy guéne.

Akay deugue.

Bi ma wakhé ni as la tébi, fou ler nagne la ko tek. Sama dieukeur rek, démoul sakh baciy wadja bok. Dou moromou khalé yi.

*******Un mois plus tard******

Finalement dama trouver béne arrangement ak Nogaye, sama goro néna ak dé kéne doufi mbidane. Khalil saf dafa choquerwone parce que mère bi ci bopam ma wouteulone Coura djank parce que da fa done diank que meunoul wone bolé gnare yi. Mane nak mou bagne. Khana djangue dou djangue wala bok belle-fille mo nékoul belle-fille rek. Au moins légui d'accord na may dem salon ba souma paréwé sama liguéyu keur. Khalil dé mo wakh ak yayam, yalla bakhna bimou topoul yayam ci déliram yoyou ba moumay téré liguey momitt.  

Mais heureusement sougnou borom sétanouma. Nogaye la expliquer problème bi mounéma grawoul, souma ayéwé  meune na tok 4 jours après li dess may arrangerwou di gneuw.

Salon ba la diogué ni dé. Tay mome liguey bi dafa bari wone mo takhitt tass na.

Bimay dougue ci keur gui lay dégue ay wakhtane, ma khame ni dagno wara ame gane.

Effectivement bima dougué ci salle guiss na kouma meussoul guiss.

Ma nouyo diokh ko lokho mais bima dégué sama goro né « Coura ki moy Adja », li diogué ci mane dotoul gneuwati ba fawou. Ki khana nékoul France ?

Kéne kou mel ni yowOù les histoires vivent. Découvrez maintenant