Saar 21

9.5K 1.3K 107
                                    


Saar 21

*****Adja*****

-Dagnouy déme lune de miel ?

-Sou beugué tamitt gnou dem sougnou keur rek. Nala wore ni sama yaye ak samay sœurs dinaigne dek nope pour khame ci youkhou ga wala.

-Nonou laigne deugné koumpeu.

-Yow daigno koumpeu. Soufi Modou indi wone diabar wore nama ni digua dék nop.

-Modou khalé la.

-Khalé moy nek mak. Wa gawal gnou déme.

-Wakho ma sakh fougne dieum.

-Bougne dougué ci auto bi diguako kham. Bo yoboul maillot de bain yow la concerner, fékhél ba boumay déme sangougnou guamay culpabiliserlo pour que douma la fa bayi yow dongue.

-Aka féroce...Wa magui déme.

-Ani mère ?

-Migui ci birr.

Ma avancer Khalil tope ma. Ma déme sama nek, Khalil déme salle ba ci sama yaye.

Ma diakarlok sama armoire khoma sakh louma wara yobe. Li ndakh dina léne dale yéne. "Tay la gueuna bari lé wayé tay la gueuna rafelé". Magui diakarlok adounay yéré té khoma loumay yobe.

Déjà sougnouy déme puisque voyage la mome, na défe jean ak béne top rek. Après khame na dinaigne déme réiri. Na yobalé béne robe bou classe. Lima gueuna méti instant yi nak moy ay bagassou mariée sakh omako. Foumakoy dieulé rek ak lou parakh parakhé li. Khalil mome khame nako il n'a aucune patience. Souma fi néké di traîner légui mou féke ci mafi wakh ma sama bop.

Moudj gui dal opté na pour quelques trucs def sama sac. Heureusement que ame na quelques nécessaire you ma dieundone dinthie, rangerwalé léne gnome gneup.

Changer na yéré défe maquillage bou discret, juste contours yeux ak rouge à lèvre rose bou mate ak touti poudre. Défouma dara lou eupe.

Ma délou ci salle ba fekléne gnouy wakhtane.

-C'est bon...Demande Khalil bime ma guissé ma takhaw ci bounteu.

-Oui bakhna.

-Yaye boy kone gno gui gneuw déme.

Khalil wakh lolou sama yaye diogue fime togone.

-Kone yalla naléne yalla tek ci yonou diam. Adja bo gué nagua dégueul sa dieukeur.

-Yaye néko dima yab may seuyi.

-Khame na lolou wayé téréwoul khamal sa bop khame moy kane tamitt.

-Wa ok, gno gui déme. Ga tagoul ma gosse yi.

-Dinaigne ko dégue.

Gnou quitter dougue ci auto bi.

Khalil dé commencerna dawal wayé wakhouma figne dieum. Mais mane dofouma, bime diaré croisement Camberéne la khaméni dagnouy guéne Dakar. C'est sûr que ci petite côte bi lagne dieum, bou doul Saly rek di Somone. Nako bayi rek mouy guande guandou lou fi sama kanam.

-J'espère juste que dougne déme sa hôtel b arek fék fa sa béne mbarane.

-Wa légui nak lou takh ngay yak wakhtane bi.

-Il faut se parer à toutes les éventualités.

-Déjà mane weurouma Sénégal bi yeup di mbarane en plus bayi na mbarane bou yague.

Kéne kou mel ni yowOù les histoires vivent. Découvrez maintenant