Saar 19

9.9K 1.2K 50
                                    

Saar 19

****Adja****

Gni dé ni gnoumay kholé ni envie wakh ma daguay feine moleine di beugue ray. Mais meunou ma leine ko reprocher car bi ma ko fi moudier balou dama delouwatt ci lou gaw donc lignouy def ni fou wor lagneko tek.

-Adja thiakhano ni?
-Dié, ak sama akoulay tala thiakhanouma. Bayina mbarane.
-Dina lathier kat nak...
-Wa légui khana dou ma wat di feine. Wa légui bou dé damay feine lou wara waral may bayi Gora? Nogaye bok wakh ci...
-Mane kay khoma louma ciy wakh. Gora mome merr na torop. Bime ma wowé demb dama tite. Mane tamitt méré nala. Donté mane mala bolé ak Gora soy bayaneté ak mome au moins ga woma tagouma?

Comme si mane demb bi ma Khalil timé ak ceinturam khalatona lénéne kou doul protéger sama yaram ci dor yi.

-Nogaye nime démé leu wone rek.
-Adja ak noume meuneti démé khana doma wakh ni que décision bi dagua ko dieul du tic au tac.
-khana Khalil dala diapati?

Dié dé dafe ma mine à un tel point ba meunouma ko neub dara.
Tontouwouma defou ma dara.

-Sou la Khalil diapoul wone ma rouss. Khana do ma nei da kholat sa portable dé?
-Non kholoul portable bi. Nogaye magui diégualou nak mais kham nani digua comprendre sama position.
-Si, si amoul solo. Gora dina ko wouteul bénéne khalé bou bakh.

Tontou wouma ko sakh. Louma koy wakh?
Agnou mbarane dé gui... so fi dioguei rek gnou tek fa sa morom.
Mane dé dama khamoul sakh nouma li meuna métiwé. En plus sakh fare na wowatt sama yénéne gnare yi. Té en plus khalé you gor yi nonou lagne sofé daga leine di bayi, gnou nane daigne lay tope di insister. Mane mome nagne ma diapalé rek car dara woroussi. Tem gnou wo ma ci kanamou Khalil mou diape ni bayiwouma mbarane té instant bobou douma khame nimay setalé sama der.

******

Dié dé ba nignouy guéné salon ba di gnibi, migua ma done lathie pour que ma wakh ko nane la Khalil def ba diapema, may diédieulé. Louma ko meuna wakh? Ame na gathié yo khame né kene douko nétali.
Bi ma guissé auto Khalil sougnou bounte keur dé sama fit dafa né reuss. Khalil kagne la fi dane gneuw té dou yeuguelou. Kheyna dafa diape ni bou défé ni dina ma meussa béteu.
Ma noyi watt bou bakh dougue ci birr keur gui. Sama yaye mome mogui wakhtanal Khalil comme toujours. Mome dome bou gor lako def.

-Assalamou aleykoum.
-Wa aleykoum salam.

Gni ma fek ci salon bi tontou ma, ma gneuw tok.

-Adja wathie gua???

Khame gueine ni sama yaye moy lathier lolou. Khoma souma wathioul louma fiy def. C'est que Sénégal parfois dagnouy poser ay questions yo khame nei keine dou kham nime démé.

-Wathiena.
-Sene salon ba guedj na fa dé. Khame na ni Nogaye mome dina ma méré.
-Nogaye dé taloul méré kéne liguey bi dafa bari.
- Kone kay sant yalla. Kou nek ci liguey mouy dokh guay gnane.
-Lolou la mome. Khalil dagua fi gneuwone?
-Khana daga faté ni dagno warone déme keur Ouzin?

Tontouwouma dé mais khouli na sama beute yi. Mane ak Khalil kagne lagne wakh ci deme keur Ouzin wala dama nakh bok.

-Khame na daguako faté mais Ouzin mogui gnouy khar dé diogual gnou deme bala gno goudé.
-Adja kone diogal. Khalil wakh na deugue lou gueine gueuna tok gueuna goudé.
-Gnou deme.

Khalil diogue talale ma lokho. Mane dé magui mel ni kou nek ci film.
Ma dieuleko té diok fima tok.
Gnou tagato. Khalil wakh sama yaye dina ma indi ci kanam.

Bigne dougué ci auto bi, li lako gneuka lathie.

-Khalil, khalate na ba sone mais faté likouma fo ma wakhei ni dagnouy dem keur Ouzin.
-Dama la beuguone guiss té meunouma gnow rek ak sa yaye nonou. Il fallait que ma bayi fa beine excuse.
-Fougne dieum?
- Sama nek, khana.
-Sa nek?
-Sama nek kay wala dagua beugue ma défé ko ci auto bi?
-Non gnou deme fofou.
-Yay sett dal.

Temps yi mome dagne may clouer le bec rek. Nitt gni dimaa dor dor yo khamené douma ci meune dara. Nopi rek dileine setane.

*****Ay wer ci kanam*****

*****Khalil*****

-Mais boy ani Adja guedj nala degue ga diambat dé.
-Ouzin wakh na deugue dé, sougnou diotay yi guedj na tourner au tour d'Adja ak diapal bayi.

Sama gars gni mane laigne def kagne quoi!!!
Ouzin commencer, Moussa agali. Mais nak deugue leu ni bimay ame probleme ak Adja gno ci gueunone sone. Sama yaye yeuguoul, samay soeur yeuguougnou.

-Dina leine guedja sonal ci Adja car j'ai réglé le problème.
-Comment ça tu as réglé le problème?
-Ouzin fi problème yeupeu ame solution. Il suffit juste gua khame fane guay diar.
-Beuguona kham no réglé sa problème, ndakh ma essayerko ci Dié.
-Non bokoul. Méthode yi ma dieul pour regler Adja dagno drastiques dé. Et même kheyna mou gnaka marcher ci Dié.
-Mane sama guel reglerna mais n'empêche beugue na kham no def ak Adja.

Moussa mo dagne koumpeu dé mais grawoul khamena noumay def ba gueine ci.

-Loula wor ni Safia reglerna?
-Lo lou lama wone.
-khana doma wakhni lima fi diambatt ci Adja dafa dougue ci beine nop gueine ci béne nop guéne ci bénéne bi.
-Safia mako yar. Elle n'a rien à voir ak sa Adja momou.
-J'espère que pour toi que do ame mauvaise surprise rek.
-T'inquiète pas.
-Mane de toute façon sakh Adja dama koy officialiser, thiakhane yi doyna.
-Daguakoy tak?
-Si Ouzin, damakoy tak kay.
-Wakhtane naci ak mere bi demb. Adja pareina, pareina. En réalité, Adja sou meloule wone nime melone gni gui ci sougnou un an de mariage en ce moment.
-Puisque neiga regler ga problème bi kay, kone diote na ga def ko. Khame na ni yow mome meuno bayi Adja. Fi gueine diar yeup ga diafandou si rek.
- Un truc de ouf! Ni ma beugué Adja beugué wouma wone sakh Coura nonou.

Bi ma kheuthier sama portable bi ba khol heure bi dama tite.

-Hei gars gni magui gneuw bouger. Dama wara dem keur pa bi la.
-Sa keur papa?

Moussa tamit, souma né pa bi kay sama papa lay wakh.

-Si. Momay gnani djil. En plus Adja wakhone nani ndidiayam mokoy mayé khame nani fofou la pa bi di dieum.
-Kone naigne tok khar ga annoncer gnou sa date de mariage.
- Lolou d ci Adja la dépendre rn plus wakhona day khew.
-Thiey femmes, nigne gnémé lou leine sonal.
-Bon magui dem.

Ma éclipserwou fat fat.
Sama keur papa mome yagouma fa sakh. Bien que khame na ni ça va être moins facile que ak Coura khame nani même protocole bi lay tope

*****Adja*****

Ay pa gui tok ci instant yi gnou tol. Kham na bou bakh li léne fi indi wayé sama khool ak sama khel jubo wougnou ci tontou bi ma leine wara diokh.

Sama ndidiaye gersou na khol ma.

-Gni fi gneuw nainaigne Khalil mo leine yabal. Wayé nak lima léne wakh léneu la, seyyou ma yay seuy kone batt bou moudj mi ya ko yor. Paré gua guir seuyeul Khalil wala ?

Limouy wakh yeup, siggui wouma khol ko. Magui seug ci sama lokho yi. Loumay tontou la khamoul instant yi. Sama mbeuguel ci Khalil kéne dou ci wéranté wayé mane ak mome dafa ame fougnou diar té fignou tole ni damako ragal té yakarouma ni paré na pour seuy ak ko khame ni gnéméwouma ko.
Dagueine beugue kham lou takh gnémétouma Khalil, il faut que gnou délou ay wer ci guinaw.

Kéne kou mel ni yowOù les histoires vivent. Découvrez maintenant