Saar 38

7.9K 1.1K 134
                                    


Saar 38

****Adja****

Temps yi mome dama fouy, may chef. Louma nekh mofiy ame lima beugue mofiy ame.

Tay dé bima mère di yé nane dafe may fote lo, Khalil moma né bouma bouger. Magui koy dégue mou nane yayame, boume ma yéwati ay 4h du matin ndakh fote, que mane na woute fotekat, mome dina ko fay.

Dégue na mère bi kass, mais sama daddy faléwouko dafa dougate ci nek bi teudj bountou bi.

Té nak ak yénéne ak yénéne, fou ma mère bi tongalé sama partie lay dieul.

Bima yewou ba wathie ci souffe, féke na mère bi forcer fote bi gnénéne gni. Bima léne nouyo dé bakane laigne ma fayé. Diégalone naléne fay bi dé. Wawaw li bou léne nakaré naigne ko kassi ci Khalil. Mane défouma dara. Sama ndigueulou dieukeur képe la tope.

Ma déme dougue ci salle bi.

-Yaye naga def.

-Magui fi.

Magui fi bi dé, ande na ak guandame bigne.

Ma déme bay tok mou néma.

-Boul tok dé...

Ah lou khew ?

Wakhouma dara mou enchainer.

-Khana kou meunoul féthie wara meuna tathiou. Démal dieundi mourou boutique té défaral gnou ndeki.

Bolé woumassi sakh wakh, ay wakhi fadjar mome, nama ci dégue doy.

Ayé wouma dé normalement keur gui, ki ayé moy gérer ndéki bi.

Grawoul boutique bi c'est juste en face, li ware nako meuna diapalé Anta.

********

Bima gneuwaté di lale pour que gnou ndekki ma dégue mère di kass gnak fote bi ba légui. Khali aussi wathie na.

-Mère kou wakh deugue ga merr.

-Bane deugue ga wakh ?

-Fote kat boci fay 10000 frs khana dina la fotale lou bakh. Yayeboy goro la la indil dé, indiloumala diame.

Bilay Khalil wakh na deugue, mère bi mome...

Ci wakh dji rek, ma guiss béne porte de sortie pour que Khalil guénéma ci keur gui.

-Kane moko def diam ?

-Yaye mane khame nani beugoma...

Ma diéki rek commencer dioy sama dioy you fate tarathie.

-Waaa...Riposte ma belle-mère...Adja fane la la bagné ?

-Khalil mane bima fi gneuwé di seuyci dabe sa banekh ak sa bossou famille moma fi indi wone mais sa yaye migui ni douma bayi ma féne, chaque instant mou khass douma def dara bamou ni bakh na car à chaque fois léne rek lay guiss ci mane, nékouma Coura té nékouma tamitt mbokam.

-Khalé bi mo meuna féne....li déla wakh boléssi ay tathiou.

Yalla khame nani dama exagérer dioy yi rek mais fénouma deugue la wakh. Mère bi beugouma té meussoumako neub.

Ma déme ci sama wetou dieukeur mou consolerma.

-Boul wakh ni day féne, dama yor samay beute di guiss. Adja wakh na deugue, yow ba légui bo sagnone fi Adja tok Coura mo fiy tok.

-Yak Coura ande guéne takaliko guéne lane laci meune ?

-Meuno ci dara mais au moins ga topato Adja nigako done défé ak Coura.

Kéne kou mel ni yowOù les histoires vivent. Découvrez maintenant