Saar 24

8.4K 1.2K 45
                                    

Saar 24

*****Adja*****

Mère bi est-ce que beugouma may rirr ci fadjar téle gui. Amo loumay wakh ak mome, Khalil mogui ci bir di nélaw, na gneuw khol noumouy gérer yayam. Tay sama borom keur ligueyiwoul, férier leu.

Bima dougué ci nek bi ma khol ko baci yague, ma ame le cœur serré né grawoul. Nogaye comprendra. Boumako yakal ay nélawam ndakh détails yi.

Ma deupatt, sama belle-mère mome famou takhaw diogoufa. Maga gnaw kanam gui bamou tingue. Mane dé li diakhal nama. Mère bi dé défoumako dara di. Kheuy na li Khalil fassé diarbattam moko méti, légui nak mou beugue mako souli mane mici sama yone nékoul.

****

Instant yi dé khoma sakh bane heure mo diote. Sama bir ba gui kour kouri. Fi ma démé bay ladj Nafi rek, ma dégue Khalil di nouyo.

5h ba légui magui time foote mome mouy nélaw rek. Méti na dal j'espère que ligne koy def fi bariwoul. Bou dé chaque semaine mome sama yaram douko féké.

-Naguéne def ???

-Gno gui.

-Adja lo fiy def ? Liguéyi wo khana.

Ki ma téré liguéyi mogui thia salle bat ok demal wakh ak mome.

-Foote bi mo takh.

-Foote mola téré liguéyi. Wa bayil liguay def ga défaral ma ndeki.

Thieyy les hommes sénégalais, bougne amé diabar rek di mel ay bour. Beuguona kham souma fi nékoul wone noumouy def.

Diaroul débat, en plus sakh ma togalé ndeki.

*****

Bignou togué ci salle bi di ndekki, Khalil néma.

-Bou la Nogaye daké diga kham. Khoma lou la téré déme.

Ma siggui khol yayam mou khol, ma guersou khol Khalil.

-Ladj ko maman Khoudia.

-Waw mako né boume ligueyi... Yayam moko tontou lolou.

-Lou waral lolou, mère.

-Bou ligueyé foote bi koukoy agali.

-Yaye nak khana daguay foo? Foote mo takh ga téré Adja ligueyi. Ak keur gui limou ame ci ay djiguéne yeup.

-Bou done liguey bou ame fouleu doumako né mou bayiko. Ladj ko lime ma tontou bima ko ladjer...

-Mane maman dama la né, que gnoune ay éléve laigne dagnouy diangue.

-Ga toudé ko diangue té bagne ko wowé liguey.

-Grawoul, dinako gérer. Di ga oubi sa salon bope.

-Gané ???

Mane ak maman Khoudia dé gnoko wakhando . Da tite ma tite.

-Dégue guéne bou bakh. Dou néga mou tok car amoul fé dara. Souma fékhé, ba détacherwou ci sama engagement you bari dinay lale projet bobou.

Instant yi dé envie kote ko faune ko rek la ame mais puisque mère ba gui fi mome je dois me retenir.

-Khalil daga ma yab la fogue. Khana bala ga lakh diay, lakh lék.

Mère bi tamitt sak.

-Louy lolou.

-Sama taw bou djiguéne bi wakhoul fi ni dafa beugue guéne diapaléko, mouy dieunde di diay.

Kéne kou mel ni yowOù les histoires vivent. Découvrez maintenant