Oup's magui sogua wathie donc j'appel Penda pour mou dieul Taxi depuis 15 minutes magui koy wo mais dieuloul ben yone bref diakhlèna trop , en ce moment mane rek ma tok si plage bi il y'a 20 minutes guisouma Penda guissouma ken je suis seul ici pourtant yakarone nani Penda dina nieuw mais bon peut être mou am louko teyer sen keur pff damako khar ba decourager quand je suis en route vers chez moi moumay sogua texto pour wakhma bopam dafa done meti motakh meunoul wone niew dafa done mir migui sogua am esprit tranquille beug na dioubal direct chez elle mais sen wa galè laye bagn niou inil ko thiow donc je dècide de rentrer direct sama keur dama stresser parceque Penda waroul febar franchement 😭😭.
Lorsque je suis arrivè chez moi dama wo penda ba sonu diotoumako dama diakhalè en ce moment sama xel bi dafa diakhasso serieux nakh sama bb waroul febar kharal ma diouli nianalko sakh dama parè diouli rek woko diotko
Penda📲:Coucou Ibou tu me manque beaucoup magui taner bou bakh .
Ibou 📲:Alhamdoulilah sama xel bi yeup si yaw la nekone dama stresser wone meunoo sakh comprendre .
Penda📲:Boul def lolou nenala magui taner kay boul decourager ni stress je vais bien .
Ibou📲:Mane kay touti ma dof dama done diouli ma parè rek guiss sa texto sama xol fekh .
Penda📲:Dagua beurri feeling nak hubby ❤ tkt dieulna samay medoc allonger au lit di wakh ak yaw sama xol di fekh😍..
Ibou📲:Mane damala beug dagua sori si mane soo febarè rek douma nek ..
Penda📲:Bea magui taner tkt surtout pas je vais bien dh ciao mon amour❤...Gespère que pareguen pour benen suite bi mes amis loves 💚💛...
Merci pour les votes et lectures please abonnez vous ❤
Niou dem si suite bi 💚🕺🕺

VOUS LISEZ
Mbeguel is All 💛
Romanceje vous raconte une histoire d'amour entre Ibou et Penda en wolof et français 😍...