21-Partie 🎬

665 40 2
                                    

Aujourd'hui j'ai prévu guissantek ak Penda depuis lors Magui fausse sunu rendez vous yi rek nakh sama cousine bou sof bi rek tchim bref moi je rentre à saly parce que damay recommencer cours année bi moy sama last année ma pare commencer def stage pour niou recrutema mais bon Penda dafa decide beug tok Dakar def formation et moi dama conseil mou continuer école pask amna nio khamni defna niou 4fois sakh takhoul niou bref si on se verra dinagn wakh tane si lou sérieux pour khol voir les conséquences ak mom loum d'accord rek ..
Pensif ( Bref Dakar dafay yak djiguene esk dou changer commencer far you bess lolou motax j'ai pas envie mou tok Dakar nakh djiguene mo xelam moy lolou quoi mais bon peut être mou bania nek genre meuf yoyou dh mais bon yalla bakhna )
Après ma wo penda 3fois dieuloul ma insisté ba diotko niou commencer waxtane et tout après niou fixer Rv (Chocolat sarayi) juste pour wakhtane et manger genre quoi
Penda: Dina niew dh mais yaw temps dagua changer douma Wakh niewal fi bagua niew gua top ma rek nane ma suis occupé toujours mais kouy mandi di lakatou digua fegn .
Ibou:Ay bb boul histoire xolal ce soir sougn guisanter nala expliquer lep commencement ba fin gua comprendre bou bakh lou xew d'accord ne boude pas je t'aime prépare toi vers 20h on se croise au (Chocolat Sarayi) 🥰.
Je me prépare oklm pour guisanter ak Penda (tay lane lay sagnser finw 😂❤️) dama contane mais au fond sui un peu stressé trop sakh parceque Penda dafay douter trop si mane temps et je sais plus comment faire actuellement sakh nak mais na tak sama fitt dem rek c'est mieux ma bania faussé rendez-vous bi ...
25minutes après sui prêt pour dem (chocolat sarayi)
Legui nak bagn guisser mak ouf dama contane mais au fonds Penda dafa khawa mer parceque damako wakh louxew yeup même ak sama cousine legui nak mou mer bref comme wakhna li xewone rek bahna loumasi diakhal moy dafa mer comsa rek 😔 mais bon yalla bakhna
10minutes après Penda takhaw ni dafay gnibi dafa sakh done yokhou après mane si bopam dama rouss nakh dama def erreur mais comme wakh nako li xewone rek bakhna kone peut être dina changer mer bi d'ici quelques jours
Li yeup sama faute la 🤦‍♂️sheuteute

Nouma wara def ak Penda😭 rek moma stress instant yi 😔!!!

Kharal ma inilen chapitre bou meilleur 🥰

Mbeguel is All 💛Où les histoires vivent. Découvrez maintenant