Chapitre 20

2.5K 212 8
                                    

🎶 hum pa yi wakhtane nagn ba diap beuss sama fit né reuss ma nara doundou lou Bess 🎶stresse dima ray ndakh Magui dougou ci seuy té seuy dou tiakhane Lolou la l'islam santané 🎶 tay la tay la sama mariage , tay la tay la 🎶 tay lay takk diabar tay la tay la sama mariage tay la tay la Im gonna get married me 🎶
- ya الله tay la wara dougou ci negou seuy té kham nani Ben seuy nékhoul . Sama dieukeur nak kham nako ndakh soudé bakh def nako , soudé beugue ma deff nako bama kham ko mais ben seuy nékhoul kham na Lolou rawatîna seuyou woudié . Batakh na yaw migua khamni yay bind seuy Tia arrasse kham gua liy nieuw ak li nieuwoul Magui lay nian yaw sama borom gua dioubolé ma ak sama borom keur yagual ma ci sama négou seuy . Di la nian soutoureu ak confiance bou werr lol 🙏
Assise sur ma tapis de prière , je venais de clôturer ma prière du fajar avec cet invocation. Je sais que suis provocatrice et tout mais je suis consciente de l'importance du mariage . Donc pour rien au monde je mettrai en péril mon mariage avec cet homme incroyable . 😻
Apres je suis allée prendre le petit déjeuné vite fait avant qu'Amar nous dépose chez maman Aissata . Mes bagages partiront de chez moi , Amar va s'en charger du coup j'avais pas besoin d'apporter des affaires avec moi .
Avec Fatima on est arrivé super tôt chez maman . Je me demande même quel était l'intérêt vu que je suis sensé rejoindre mon domicile le soir . Une fois à la maison , on s'est installé dans la chambre de Fatima avant que maman ne vienne me demander d'aller dans sa chambre pour une discussion mère et fille ...
~~~~~~~~~~de l'autre côté ~~~~~~~~~~~~~~~~
C'est en colère que notre chère Maïmouna s'est réveillée aujourd'hui . Vers les alentours de 09h , elle fut réveillée par sa belle mère et quelques membres de sa belle famille . Elle qui d'habitude ne se réveille qu'aux alentours de 13h était rouge de colère mais c'était que le début .
Belle maman : y'a tal ay nélaw khalé bi diougueul , Diék you bakh yeup diougu naniou ci fajar
Maï : hum maman j'ai une mal de tête 🤕
Belle maman : lolou dou excuse tay sa woudiou wara seysi guay nélaw ba heure bi
Maïmouna s'etait réveillée comme si on lui avait jeter de l'eau froide .
Maïmouna : comment ça dafay seuy si tay ?
Belle-mère : kon yaw yeuguo li khew ? Sa dieukeur wakhoula Dara ?
Maï : non je ne suis au courant de rien maman . Loukhew ak bruit bobou lanla ?
Belle-mère : sa woudiou moy sëysi tay lolou Guay dégu moy meuble chambre bimouy watieu . Sa dieukeur dé ségueum man mi ndayam lako yeugueuloul bétouma mou niak lako yeugueul
Maï : comment ça ? Yay kon noko khamé ?
Belle-mère : khana Aissata moma wo di yokhou ak kass nan ma sa dom dji satieu na diabaram yobouko pendant deux semaines naguén wadial ndakh day seyi doufi fanan
Maï :YAY GUANI LÀN YAW ? Wouy sama ndaye dou deugue
Elle s'était mise à crier comme une hystérique. Sa belle mère ne comprenait rien à la situation . Elle détestait sa coepouse et considérait cela comme une déclaration de guerre mais sa colère bien qu'étant justifiée était plus orientée vers son mari . Car non seulement il lui avait menti ouvertement mais aussi il lui avait manqué de respect et ça elle ne pouvait le lui pardonner . Mais à quoi s'attendait elle vraiment en négligeant ainsi son mari ? Pourtant ces amis l'avait prévenu mais elle se disait que jamais son mari n'irait voir ailleurs oubliant même la force de l'amour . Sa belle mère la calma avant toute chose car elle aussi savait que c'était pas normal l'attitude de son fils mais elle ne voulait interférer dans leurs relations .
           ~~~~~~~<<< séto séttt >>~~~~~~~~
Maman Aissata : bien vrai que je ne t'ai pas mise au monde Sophia je te considère comme ma fille au même niveau que Fatima . Yaw aussi gua yayo ma diokh ma tieur , fonk ma bien vrai que de temps en temps t'en fait des bêtises mais je vais pas en tenir compte parce que mon rôle c'est de te dire quand tu fais quelque chose de travers . Je ne vais pas être dure avec toi aujourd'hui car ton mari m'avait bien dit hier qu'il t'avait déjà eu sexuellement parlant et qu'il était fière de toi .
- com.......
Maman Aissata : laisse moi terminer. Moi je ne veux ni de drap ni rien d'autre car je juges que c'est quelque chose qui doit rester entre vous  et heureusement que ton mari partageait le même avis . Même si tu ne t'étais pas abstenue pour ton mari je ne t'en aurai pas voulu ma fille . Je te connais  et je sais qui tu es au fond . Je dois le dire je suis fière de toi.
Vous et moi savons très bien que c'était pas vrai mon mari ne m'a pas trouvé chaste . Je pleurai de déception car j'aurai aimé que ce soit lui . Cet homme qui a caché tous mes défauts . Comment je pourrai le remercier même .
Après vint enfin le soir et l'heure du départ . Elle fut amener dans la salle de bain pour un bain purificateur avant d'être habiller par un habit de maman Aissata comme l'exige la tradition ensuite elle a été amené au cours où était assis tous les vieux dont l'imam , le papa de Fatima , des vieux du quartier et même son beau père qui l'appréciait beaucoup.
L'imam : Seuy nak Souna sou am solo-la so xamné Yonénti-yi ak gayou bax-yi sopone naniouko lol daanko déf ndax niarigne you bari yimou lambol ak Tuyaba gou bari guithi Yalla déf ndax amna borom xam-xam you waxné kigua xamné dafa dougou thi négou seuy té dioublouthia diamou Yalla ak sakouthia gueureumal Yalla, koké
niari rakam youmou nafila goudi mo eup tuyaba kigua xamné dafa fanané nafila té nékagoul thi négou seuy, wayé tamit niou xamni ki
nék thi négou seuy ni ay dieufam you bax eupé dolé dieufi ki nékoul thi négou seuy, noné tamit la ay bakaram eupé dolé bakari ki nékoul thi négou seuy, ndax bouniou bokon niom niar défando bakarou ndiaalo thi missal, bou boba ka nék thia négou seuy l'islam dakoy raylou wayé ka nékoul thia négou seuy mom dakoy dorlou téméri( 100) yar dongue.
Mouy lo xamni nak mom seuy Yonenti-bi (psl ) daane nathi sognou dioulit-yi bou bax nguir niou dinthie ay soxna nguir meunthie am
ndiaabot ndakh xéétam-bi yokou ba bou eulagué thia bis peinthie-ba mou meunlénfa poukaréwo thia kanamou yénéni moromou Yonéntém-ya, téyit say bothi dougué mom seuy day takh sounou Borom aral-la sa guénwalou Diné té Chaytané danathia méré ndiabotam-gui bathiay téki séni ndombay tankeu yamoulén takalone nguir sagane guiniou sagane ba sétane ba seuy bobou di am thi Farata Yalla ak Souna Mouhamed (psl ), motax say bou niari dioulit beganté té Yalla takh, kilifa-ya warnanion gaw taxaw thi mayelen namou geuna gawé té bagne diko diafel ak dithia athie youthia Yalla geuramoul ndax guisnaniouné diamono-dji seuy diaféna lolou té dara waralouko loudoul warougar you disse-yi nga xamne day takh seuy-ba dou am barké té dome diou am thieur thi Yalla douthia meuna dioudo mba bok danathia diafé lol ak xébanté bi kou nék di diay sa morom askane bou reuy nane guérla wala guewal wala gnégno wala laobé wala teugue ect... nga xamé thi kon niouthi eup mayétougne sén dome té Yalla takh wayé niougui mayé nguir dieukar-dja amna xaliss wala daradja donté amoul diné wala mouy ap yéfar sax sén yone nékouthia, yéne wadiour you djiguén-gni tamit di téré sén dome you goor-yi di takk soxna yaniou beugue té dara waralouko Lou doul ndéyou xalé bou djiguéne-ba bou domam-dji seuysé ba am dome douko meuna téral thi xéétou yébi yigua xamni mo xéw légui thi diamono-dji di lou bone lo xamné méroum Yalla ko weur wét gou nek.
Lolou yeup nak di ay probléme yo xamni dafa dathie société-bi yeup tassaro thi famille yi eup ba dioural fitna goor-gni ak djiguéne-gni nga xamné légui téméri mouskalaf yo dieul foukou rék danaka
niothiay nék thi boumou seuy bataxna lolo diour moussiba yiniouy dégue fou nék thi réwmi ak thi bitim réw, ndax niaka seuy foumou amé thi ap réw day waral ndiaalo-gua barifa ak gniy diaay sén bopou thi goor-gni ak thi djiguén-gni, bouko défé kérsa ak ngeum dadi commençé dégne thi nitgni, yakou-yakou yi tassaro, déé-gui bari lol ba diégui dayo, Yalla dadi djital gni geuna niak yeurmandé
thi nitgni, chaytané dadi meuna diékou nieup meunléna diaralé fako néx.
Seuy nak moxam kou goor-kila wala kou djiguéne-ki kén kouthi nek thi niom niar meuna seuyak morom-dja nguir Alal gamou am wala nguir Askane gou bax gamou bokou wala nguir Taar gamou amé wala nguir Diné gou rafét gamou yor diko doundou, wayé Yonénti-bi (psl) nak néna taneulén borom Diné ndax kouné xamnani Sokhna Khadidja bamouy taneu Yonénti-bi (psl) djiko you rafét kép lako
tanéwon ndax Soxna-si moko eupone xalisse fop daanko diox ay marchandisam moukoy diayal nieuk sounou Borom diko yoni thi
mbindéfam-yi wayé Yonénti-bi momit djiko you rafét dongue la guissone thi Soxna Khadidja ba téyéko ndax soxna Khadidja maguéwon nako Fouki At ak Diourom (15ans) té lolou lép bo xolé
Diné dongue-la ak djiko you rafét, kon nak lolou sognéla thi dioulit






BONNE FÊTE À TOUS ET À TOUTES 🙏 YALLAH NANIOU KO YAGU FÊTER NIOUN NIEUP KEN DOU MÀNQUER 🙏
SORRY POUR LE RETARD DES PUBLICATIONS

Niarel la : suis deuxième dame Où les histoires vivent. Découvrez maintenant