Moi: en bon legui wakhal fo beugue
Khadija: nieuweul sama kogne niou deme sama keur bene copine par ce que limay sentir sama yaraam dalleu moy lolou
Moi: wa d'accord dina nieuw ci kaname Inchallah
Aye 17h 🕔 00 yoyou ma deme dougou ci douche 🚿 bi sangou ba sette wethie sollou ba nice guene weur ci chambre yeupp parfum yeupp ma kheuppo ko ndakh rv bi rek taggou souniou wa keur guene keur gui deme ci arrêt 🛑 bi takhawe khare bus 🚌 bi aye 5 minutes mou nieuw ma dougou dague ticket di imaginez que ci bus la guissé wonne Khadija ndysanne mbeuguel waye aka nekh aye 17h 🕔 38 ma ague keur massar wo khalé bi niko akci na mou explique ma. Ma deme ba sen kogne woko mou guene sen keur oh 😮 ma khole ko kawe ba souff khalé bi sagncé lou simple té raffete akk mouraye bi thiooo 🙈 mou nieuw nouyou ma ba soukou niou commence wakhetane affaire yoyou
Khadija: mouhamed yaw mome machallah di sagncé nga
Moi: makoy dozé nane ko moh bayil togne dama simple ni rek
Khadija : Konneu dh so sagncé wonneu fi tothie
Moi : tothie fi lay bagne nakk motakh ma deff lou ndaw
Khadija : niou deme sama keur copine bi fofou mome calm neu dinagne meuna wakhetane sans bruit
Moi: athia niou deme
Niouy dokhe di wakhetane moumay explique sen kogne niko khalé you goor yi deff affaire yoyou touti rek niou ague keur copine name bi niou dougou
Khadija : kong kong Awa Awa
Awa: oui Dija féroce mangui ni ci kawe yégueul
Khadija : yaw do nitte sakh Konneu yangui fofou
Awa: yaw mi nieuweul ngay wakh rek
Khadija : mouhamed niou yekk ci kawe
Moi : athia yay bagne
Niou yekk ci kawe etage Khadija présentée ma kharite bi
Khadija : mouhamed nouyoul ki Awa la toudou
Moi: oui Eva cava
Awa : oui cava très bien et toi
Moi : oui sante boubakh alhamdoulilah
Awa : bienvenue togal
Moi: merci 🙏🏼
Awa: Khadija mouhamed mome machallah di dafa beaux dafa gentle yaw yay khame kounekk
Khadija : maye ma diame yaw ni rek lagne lay bayi ngay toudou nimou melle demal maye niou louniou nane mo guene
Awa: eh mouhamed fi sa keur leu boul rouss mangui nieuw
Moi: Amoul problème Eva mangui cool
Khadija: mouhamed Awa dh nilla melle dafa bakh yatou beugue nitte makk mome nio fowando temp boy ba legui nioye ande mes sama lonko leu
Moi: wakh nga deugue mome kaye soko kholé khame ni amoul blême machallah yalna lene Yalla diapalé té boulene meussa reero
Khadija : tkt pas wa yaw name nala dh depuis baniou tassé ci auto bi ba taye mallay soga guissate ni
Moi: ah mangui ni rek mala raaw motakh ma setci la
Khadija : lolou dh ame na mes benen yonneu malay setci Inchallah
Moi : lolou dinama nekh dinala khare
Rek yayou Awa nieuw ci kawe guisse ma ma tokke ak Dija di wakhetane mou nieuw assalamou alleykoum nolene deff ba diam Khadija yaw mome bayi ngama dh
Khadija : yaye boye mangui fi yaw soumala bayé foumay diapp temp yi dama khawone febar
Mère bi : aye waye boula dara diote sama dome dji tanné boubakh legui
Khadija : waw Alhamdoulilah mangui tané yaye nouyoul ki sama kharite leu mouhamed leu toudou
Mère bi : ah mouhamed yaw mome yay souniou sangue no sante ???
Moi: may signe 😁 lolou mome ame na Gueye la sante yaw nakk ???
Mère bi : ngueyene you beugue lekk yi koula khole Khame ni gueye rek nga meuna sante mane Seck la sante
Moi: lolou motakh ngamay sani khere mère Seck mome nekhoul changer ko
Mère bi : Seck rek machallah nioune nioye bour yi
Moi: mdr 😂 wa bakh na konneu dieul lene lepp
Mère bi : waw ngueyenne bi nekk lene ci diame
Khadija : d'accord yaye dji
Moi: niou commence wakhetane nakk ndakh so guissé sama nieuw fi dafa ame louma yeukeuti
Khadija : loula yeukeuti ba diame leu
Moi : diame leu kaye 😁....

VOUS LISEZ
Mbeuguel
RomanceSalam Mangui toudou mouhamed Gueye Nioumay wowé Diego 21 mes souniou wa keur beugou niou toure bi sénégal dalle mo metti mes comprendre nalene parce que sama toure mo selle mangui ame 19 ans teint maron taille 1m75 gentleman kharitou khalé yi akk...