Suite

5.1K 378 48
                                    

Khadija : ok yaw à plus nekal ci diam merci
Moi:sama khole bangui sedd gouye ndakh contane (ndëkété mbeuguel ni lay deff nitte)
2jour après ma woko téléphone beugue niou guissanté
Ma woko ba sonou diotou mako après ma insiste ba diote ko
Moi: allo Khadija silonekk name nala 2 jours degou mala ba diam la
Khadija: waw temp yi moy lolou dama khawa febar
Moi : en bon 😳 oh masta waye sentir nako sakh sama yaram
Khadija : yaw mome machallah danga galant lole mes mangui tané
Moi: mangui beugue niou guissanté sakh noumouy démé
Khadija : mangui khole bakhame dina meuna nekk par ce que temp yi je ne sens pas bien
Moi : waw defal tout demain niou tassé place du souvenir 18 h s'il te plais 🙏🏼
Khadija : tkt pas nio far boul wakh dara  dina deff tout pour niou nieuw Inchallah
Moi : d'accord 👍🏼 dinala khare.
Khadija : tkt pas mouhamed
Mome tamite dafa commencé beugue di li nekh na
Mangui contane yakamti demain diote
Ci sassi mangui sawara saware ba melni kouniou wakhe dara journée bi makoye retane ba souniou wa classe yakaar ni dagne ma wakh lou nekh
Ndeyesanne jour bobou école la nekk contane di togne ndakh sama rendez-vous demain bi (khalé bi dinama raye rek).
Le lendemain dama warone deme école réglé aye affaire mes lepp la bayi mou sedd nekk ci préparation rv bi rek
Deme expliquer sama tata bi Diouma pour mou diapp ci bess bi
Moi : cava tata Diouma
Diouma : oui cava fils silonekk
Moi: mangui ni khana ame rendez-vous bou urgent rek beugue nga diapp ci
Diouma : en bon bane genrou rendez-vous leu ???
Moi : moy la fois passée khalé bimala wakhone dagno tassé ci auto bi
Diouma : en okey wakh nga deugue kokou mome nolene moudié ???
Moi : niongui wakhetane mome la wara guisse taye dama sokhla khalisse
Diouma : en bon niatta nga sokhla ???
Moi : ah loma diokh rek bakh na !!!
Diouma : wa d'accord kharal ma nieuw
Moi : oui defal lou gawe s'il te plaît 🙏🏼 dama yakamti
Diouma nieuw diokh ma 30milles nima khepe nako trop
Moi:merci li beurri na trop vraiment contane na mamgui bougé bassi kaname
Diouma : oui d'accord ci kaname fiston
Ma deme vite fait marché colobane ci bene boutique bouy diaye aye yeuré dieunde fa toubeuye 👖 bou 6milles chemise 👔 bou 5milles ak aye dalleu 👟you 14milles (yama guena khame) ma dougou auto gnibi ci aye 15h 🕒 et quelques yoyou fekk souniou wa keur agne ba paré ma nieuw sama tite Soeur bi Diatou mongui ame 15 ans teint noir taille 1m65 reew ba doff nakk yabaté
Diatou : frère fo demone agne bi diekh na dh
Moi : s'il te plaît dama sonou tallou ma khoulo demal indi agne bi dama khiff
Diatou : mani agne bi diekh na la wakh wala deggo ma danga teukheu khana
Moi: wa bakh na merci
Ma deme dougou ci wagne bi dieul bol 🍲 agne bi lekk ba sourre nane ndokh relax ci salle bi setane télé 📺 touti Khadija woma téléphone 📱 ma gawantou dieul ko
Moi : allo Dija
Khadija : oui allo mouhamed silo
Moi : oui mangui ni name nala
Khadija : oui mala raaw
Moi: danga may nakh rek
Khadija : non même pas mes rv bi taye...... Rek téléphone 📱 bi coupé
Moi: allo allo allo degou ma dara
Ma diakhlé ci sassi ma woko dougou boîte vocale mani yakou na nakk ma insisté ba diote ko
Moi : yaw mome lou nekk sa portable bi
Khadija : 😂😂😂😂 portable bi dh ndabare la dafay dieki dieki rek faye
Moi : mdr 😂 lolou mome doyna ware dh
Khadija : billay mes mangui prépare pour niou tassé wayé finga beugue niou guissanté dafa sorri trop ....

Mbeuguel Où les histoires vivent. Découvrez maintenant