conseils

2.8K 270 31
                                    

Nitte ki ak lo meuna doneu amal éducation même bougne la yaroul

En plus soye beuguenté ak nitte khame ko boubakh par ce que nitte dafa leundeum

So néké ak sa copain ou copine mou trompé la soye vengé wou demal ci mome milla trompé nga fayou pas ci domou diambour

En plus boul kham nitte wakh ko sa lepp lolou woroul deum yangui ci biir nitte gni

Té boul meussa tass yakaarou nitte ndakh yalla dji ci adouna lay jugé legui

Aussi nguene bayi nitte soulene beugué tekk lene sen place nguene di diaye fouye reewandé ak yabaté beugue yomboul

Relations bossi néké amoul neubanté par ce que dafay indi reero té reero=Khoulo

Té nguene tameu wakh deugue par ce que filla deugue meuna yobou aye fene meunou lafa yobou té legui nieuppa yéwou kossi wakhal diko fene dafay kham bayi la ci biir

La vie c'est comme la Boxe💪🏽il faut essayer de rester debout ‍♀ encaisser les coups 💉et apprendre a vivre avec les cicatrices 👌

Bayi ci khele

Mbeuguel Où les histoires vivent. Découvrez maintenant