Par la suite

6.7K 486 20
                                    

May dokhe diko khalate sama khele bi yepp nekk ci mome mangui dokhe di deme mes sama khele bi neka toule ci mane mangui benen monde guissou ma degou ma auto bi nekone sama guinaw beuga diale cornée na 3 fois makoy soga degue dadi pousse mou diale tayou mako dama tella bardée rekk
Après bi ci la ague sama keur mame dougou nouyou wa keur gui dawe dougou sama négou mame cotou ko bisous ko ndakh dama ko namone trop
Ma tokkeu niouye wakhetane nekk ci aye débat you nekh dieki dieki rekk sama khele bi yeupp deme ci Dija ma commencé rêves doundou bou nekh bima beugua doundou akk mome sama mame mongui wakh mes degou mako sakh ndakh
Grande mère :heeee yaw loye khalate mangui wakhe deggo ma sakh lane la danga ame aye problème wala lou khewe ???
Moi : Non non mame dou dara sama khele bi mo fess rekk mes dou dara alhamdoulilah fane lagne tolou ci wakhetane bi sakh ???
Grande mère : demal teuddeu ci salle bi nga nopalou après nga nieuw niou egali
Moi: dinama arrangé kaye waw bassi kaname
Ma guene ci chambre grande mère bi tasseke sama tante Diouma diop mongui khess raffete teint maron tolou ci 25 ans 1m58
Diouma : fils cava yaw temp yi mome yangui beaux  danga ame koulay topato

Mbeuguel Où les histoires vivent. Découvrez maintenant