suite

2.8K 290 23
                                    

Une semaine après ma wo limamou sama copain bi comme que mane louma meuna dougou makk mom niokoy dokh bamou diekh

(kharite boubakh foko meuna dieulé diare nako khole lene boubakh gni nguene di deff kharite par ce que souy metti rek nga meuna khame sa kharite deugue)

Moi: allô frère nakamou

Limamou: wa bandit cool et toi

Moi: tranquille boy sokhla nala dé

Limamou: wa boy tracell

Moi: mamy la beugue mou bayima par ce que daff ma commencé indile aye problèmes

Limamou : wa konneu boy bobou batay mongui roubé

Moi: billahi boy kokou comme deume nenako mane ak yaw meuna toul nekk

Limamou: boy iri ko defaral ko bagage ndakh mou bayila

Moi : non boy soit sérieux waye yaw khamé woma lolou diokh ma idée mo guene koi

Limamou : ahahaha damay blague rek mes tkt pas après dina nieuw sa galé niou wakhtane ci par ce que ki domerame leu

Moi: wa guiss nga dé boy mangui lay khare mamy mom dina deugue ndayame mou bayima

Limamou : lolou dé soko defone bou yague konneu bayi nala

Moi: waw dé na frère puissance

Dama coupé ak limamou  vers 16h
Awa copinou Khadija woma

Awa: allô mouha nakamou

Moi: oui Éva cava mangui cool ana dija

Awa:wa mouha Dija mongui fi mes mes...

Moi: mes quoi dit moi lou khewe

Awa: dafa malade mongui hôpital

Moi:non non lolou meunoul nekk dija niongui done wakhtane ce matin mouni ma boppam moy metti rek

Awa: waw febar bi grawoul wonneu mes aye 15h dafa doneu miire apres bimouy dem ci toilette bi mou danou kheume

(sama rongogne yi commencé na tourou par ce que dija fimou tolou ci mane dafa sorri)

Moi: mes dit moi bane hôpital leu nekk ma dem setti ko

Awa: mome hôpital camp militaires yi nekk thiaroye lagne ko yobou mes yaw boulfa dème par ce que papam mongui fa té meune nala indile problèmes

Moi:wa d'accord tkt pas mes est ce que meune nako diote

Awa : téléphonam mongui ni ci mane mes après dinafa dem inchallah

Moi: wa d'accord après so démé nga wakh mako ma wolla

Awa: tkt pas dieukeur

Ci sassi mane tamite febar na

(Thieuy mbeuguel mo beurri dollé dé té féroce)

Ma dème dougou sama chambre teuddeu meunou ma nelaw par ce que mangui xalaat dija

Aye 17h et demi ma dème dieul auto dème hôpital camp ba di weur khadija meunou niouma annoncé que sama copine dafa febar té douma dème setti ko ma dème ci hôpital bi ragal dougou ndakh lima Awa wakh ni papam mongui fa mes khame nga mane mom dama deuguere fitte tekk ci niémé risqué ma dougou ci biire hôpital bi tasseke sama bene tata sage femme bou nekk fofou mongui toudou ndeye sokhna

Moi: cava tata silonekk yangui ci diam dama nieuw fi di sette bene malade bou toudou khadija

Ndeye sokhna: oui ameth cava mangui ci diam boubakh malade bingay sette kagne lagne kofi indi

Moi: vers aye 16h 45 minute yoyou rek

Ndeye sokhna : wa d'accord demal tokk ma setal mako

Moi: d'accord tata ( mangui tite de trop) après 3 minutes ndeye sokhna nieuw

Ndeye sokhna : mes ameth dème na ci salles yeupp mes gnifa nekk nieupp yague nagne fi té en plus taye indi wougnou fi kene

Moi : wa lolou noumou meuna nékké mane fi lagne ma wakh mes tkt pas kharale ma dème gnibi mercie tata c'est gentille

Ma retourne souniou keur tokk sama khele bi diakhasso

Vers 19 h Awa woma commencé di retane

Moi:Awa lou khewe yaw lane la

Awa: ahahaha mouhamed

Moi: kholale boulma fonto waxal ak mane

Awa: balma akk boubax

Moi : wa balnala legui wakh la

Awa: dija mongui ni tokk dara dalouko

Moi: MDR non non Awa yaw sagno lolou

Awa: mouha danga faté ni ci mois d'avril lagne nekk xana

Moi: wa legui bassi lane danga may wo dima fene

Awa: non mouha yaw tamite damala done deff poison d'avril rek

Moi : mane nekouma ci yoyou ok bayima toute tranquille

Ma raccroché sama téléphone tokk diapp sama self mangui merr bay sakhare
Par ce que yene yi kene douko deff ko khamoul loumouy sentir souma amone cardiaque damay dé ndakh aye fene

Aye 30 minutes khadija dima woo falewe mako par ce que mome mo diapalé Awa ci poison d'avril bi mou envoyé ma message
Khadija : Bonsoir mon amour cava yangui ci diam désole dé Awa moma douguele ci li yeupp en plus dama done khole fo tolou ci mane motakh ma bayiko pour mou poison d'avril leu mes balma akk par ce que beugou ma dara loula metti

Moi: khadija boulma wakh dara yene danguene yabaté ame na yo khame ni mane beugou mako té boulene mako defati

Khadija : wa nenala balma nioune niola togne té dagne doneu khole noye réagire rek mes yaw mom beugue ngama

Moi: so beugué kham bakham beugue nala doko défé ni mes tkt pas mane dama sonou ci wakh dji

Khadija : mane damala name sakh dofi nieuw ma defal massage boubakh

Moi: kholale dija nieuwou ma té beugou ma sa massage

Khadija : ahahaha taye sama dieukeur merr na

Moi : en dangay retane wa baxna mes khamale bene affaire taye mom linga ma deff somako defaté dinala niouss

Khadija : moh yaw ko meuna niouss wa nieuweul niouss ma sama yaram dafay khassane

Moi: yaw danga beugue koufi nekk di wakh ngay wakh

Khadija : wa legui merr bi diekh na mes dit moi billa Awa wakhé ni dama febar no deff

Moi: doumala expliqué dara legui bayi ma degg nga

Khadija : wa wakh ma rek s'il te plaît yaw kham nala danga deuguere bopp lere nama dème nga ci hôpital bi dima sette

Moi: ahahaha yaw nakk danga ma kham ba diékhale ma
Mane ma dème bassi hôpital ba weur leu bay beuga dé guissou mala sama bene tata moma done diapalé ci weur bi sakh

Khadija : sérieux mouha démone nga dima sette???

Moi: barki mouhamed dème na dila setteu yaw Kaye taye Méré nala trop

Khadija : aye waye dji mane dé yakarou ma woneu ni diaral nala lolou mes khamale ni mala guena beugue fouff billahi

Moi: konneu yaw fofou nga tolou diaral ngama lou euppeu lolou té boul fouye nakk

Khadija : wa merci yaw buzz nga beugue mes sachent que je t'aime

Moi: moi aussi je t'aime très fort

(Après mou diekh
ba benen yonneu
wallay beugue nalene trop sakh )

Mbeuguel Où les histoires vivent. Découvrez maintenant