Fraisinage 🍓:1

1.5K 186 210
                                    

Salam la mifa 🙏🏽 doundou lene waye

Ame lene diam diou beurri waye

Yalna lene yalla takhawou waye

Mangui lene di ziar bou werr

Suite fraise 🍓

Khadija wona cousin wam bi waxtane ak mome ba paré !!!

Khadija woma dima expliqué loumou wakh ak mome

(Khadija: salut Abdou

Abdou: oui cava chérie

Khadija: ne me dit pas chérie

Abdou: xana neko sama diabar yonou yalla

Khadija: 21eme siècle lagne nekk lolou khewina

Abdou: wa d'accord

Khadija: dama lay lathie fo dieulé numéro mouhamed ?

Abdou: kouy kokou ?

Khadija: bayil dof doflou sama copain bi lala wakh

Abdou: en okey boy bou reew bobou

Khadija: yaw yako guena reew yaw mi ko woo diko saga dama beugue nga khame ni seuyou ma ak yaw boul sonou

Abdou: yene niare nieupp sen ......)

Khadija: mou saga niou nioune niare nieupp ba paré coupé

Moi: 😂 kholame mo diekh motax té mome aye saga rek lay fadjé merram

Khadija: après bimou coupé damako wowate ba sonou diotou mako

Moi: non non diaroul wowate wakh ngako lou lere ba paré diekh na

Khadija: loutax mou niouy saga ?

Moi: c'est pas grave bb lolou mome leu concentré boulko deff dara faté ko

Khadija: non non dinako wakh sama yaye ki imbéciles leu

Moi: bb s'il te plaît malako niane boul wakh sa yaye dara par ce que meune na tasse mbokkou gui té dafay niawe

Khadija: billahi yaw lassi sett mes ki narou mako Wonneu bayi nonou

Moi: tkt pas bb souniou amour bou nekh bi la beuga perturbée rek

Khadija: lolou deh meunou ci dara dafay sonou rek

Moi: legui demal nga reposé bassa khole sedd après dinala woo

Khadija: tkt pas bb mane mangui cool deh yaw rek yama meuna deff dara mou metti ma

Moi: sou dessé ci mane rek dara doula metti nassa khole sedd

Khadija: waw kay mon amour ngay ame fofou 😃

Moi: waw guiss nga nilla beugue contane rek garde le sourire 😂 niou torokhale seytané

Khadija: tkt pas bb à plus ma deme setti Awa

Moi: ciao mon cœur ❤️ nouyoul mako boubax

Dans 3 semaine maye deme Ville 🌃

Sagncé ba tranquille lale sama parfum Aidi bou ame diome dougou bus 🚌 takhawe !!!!

Yena ngui fatelikou khadija ci bus lagne khamanté wonneu 🤔

Bus bi dawe ba croisement camberene bene khalé bou djiguene dougou ci bus bi

-khalé bi khole ma
-ma khole ko
Niou kholanté face à face

-khalé bi dague tiquet ba paré diégué ci ma

Mbeuguel Où les histoires vivent. Découvrez maintenant