Par la suite khadija ague sen keur woma téléphone 📱 dima expliqué mom ak taximan bi 😂
Khadija: allo mon amour 😍
Moi: oui bb nakamou ba ague nga ci jamm
Khadija : ague na ci jamm alhamdoulilah mes bve taximan bi 😂
Moi: alhamdoulilah bb taximan bi loumou leu deff ?
Khadija : non defou ma dara mes nena dama noppe 😂
Moi: 😂 legui loko wakh
Khadija: yaw dall taximan bi dama dougou ci auto tokk rek mou commencé ma dokhane
Moi: en bon mom deuguere na fiite deh khamoul ni diabarou diambour nga khana
Khadija: bayiko fofou rek yaw taximan bi deh li lama wakh
Taximan : cava sokhna ci
Khadija: oui cava bien
Taximan : yaw mome machallah danga molle
Khadija: weu 🙄yaw mom est-ce que cava
Taximan : ah cava kaye lima guiss rek la wakh
Khadija : wouyou ma boul sori dama am dieukeur
Taximan : 😂 boy diaye tare bobou moy sa dieukeur koula khole khame nii sa far leu
Khadija : wa Mercie
Taximan : bayil boy bobou nieuw ma yoreu leu dilla diokh lepp lo beugue mo guene boy yi dagne lay tardel rek
Khadija : yaw mom nekh nga dé 😂 sama dieukeur ngani nako bayi pour lane khana guisso ma damala ndirou kou name dara mane ?
Taximan : mane kaye khame nani namo dara mes damala beuga gére changé sa vie
Khadija: sokhla wouma ko Mercie
Taximan : mes legui diokh ma sa numéro après dinala woo niou guena waxtane
Khadija : yaw xana do degue yaw mi euppeul nga dé diabarou diambour la boul sakh insisté
Taximan : boy yaw soff nga deh malay arrangé rek ngay diaye nekh legui bayiko
Khadija: alhamdoulilah
Moi: sama khole bi seddeu na est-ce que khame ngani so nekone djiguene bou matérialiste konneu dangay d'accord
Khadija: bb yaw khame ngama dara yeungeulou ma
Moi: sou djiguene yeupp melone ni yaw dinama nekh
Khadija: lolou mom meunoul nekk yalla mo bindé nonou
Moi: c'est vrai mes ba amo bene problème ci yonneu bi rek
Khadija : non non à part wakhou taximan bi lepp cool
Moi: alhamdoulilah yangui sa galé konneu ?
Khadija : non mangui ni galé Eva
Moi: en bon sama chérie bobou nouyoul mako
Khadija : Awa nena danga ko bayi kharal ma diokh lako
Awa: wa mouha mane mom kouma wakhone dinga ma bayi doumako gueme
Moi: aye waye chérie boulma rouss lo waye pourtant dama lay lathie dija dé
Awa: xana amo sama numéro doma woo wala nga message ma ngamay lathie dija yaw fassé nala
Moi: degue na deugue wa balma bb dotoul amati
Awa: yaw kaye moy lolou nekake khadija rek faté ma doumala wakh dara
VOUS LISEZ
Mbeuguel
Roman d'amourSalam Mangui toudou mouhamed Gueye Nioumay wowé Diego 21 mes souniou wa keur beugou niou toure bi sénégal dalle mo metti mes comprendre nalene parce que sama toure mo selle mangui ame 19 ans teint maron taille 1m75 gentleman kharitou khalé yi akk...
