Suite valentin ❤️

2.8K 233 47
                                        

Après sama cas ak Astou mangui continué di doundou sama vrai amour ak khadija par ce que dagno beuganté

(Pour nga bagna sonou ci adouna beuguel koula beugue
Sinon so beugué koula beugoul dangay moudié sonnal sa bopp.)

Après quelques mois ma beuga invités khadija souniou keur pour 2eme fois moumay setci

Lundi 12h30 minutes 😊

Moi: allo mon coeur ❤️ cava

Khadija: oui cava très bien et toi name nala

Moi: oui cava bien 😊 bb mala raaw

Khadija: alhamdoulilah naka fofou ana sen wa keur

Moi: alhamdoulilah niongui fi ci jamm et toi ana mère

Khadija: mère mongui fi loutax ladio sama père 😂

Moi: mane jamm la beugue té sa mère moma ko maye motax mom lay lathie

Khadija: yaw tapete rek molla japp mes dou dara

Moi: dama beurri jamm rek motax nga yakarni dama ragal

Khadija: moh degal mes lolou mom deugue leu yaw mom machallah

Moi: 😂 wa lalale bante boulma thiatou

Khadija: 😂 yaw thiate doula dougou danga blindé

Moi: lolou mom deugue mes lou bess ?

Khadija: dara bessoul bb billay nekk ci école bi rek

Moi: waw lolou temps leu diapal rek dina bakh inchallah

Khadija : inchallah nianale ma rek sama prophète

Moi: yaw delle wakh amine rek

Khadija: amine donc

Moi: mes bb dama beugue nga nieuw fi est-ce que meune na nekk ?

Khadija: oui meune na nekk mes temps yi chargé na trop

Moi: hum 😒 je vois mes dangay diare rek dofi yague

Khadija: waw d'accord jeudi 10h lay wathie dinafa nieuw sou bakhé

Moi: bien sûr bb heures boubax billa sama galé kene doufi nekk

Khadija: hiii lolou mome ba worna 😳 sen galé kene doufa nekk nga wakh deh ?

Moi: waw bb kene doufi nekk lane la 😂 danga ragal ma deff la dara

Khadija : ah ragalou ma mes yaw mom danga yakou

Moi: mes bb goor dafay khawa yakou touti sinon dagne nane homosexual nga deh

Khadija: lolou mom deugue leu mes tkt pas jeudi dina fa nieuw inchallah

Moi: rendez-vous fixé lolou nekh na dinala khare

Khadija: boul wakh dara amoré ❤️

Moi: konneu nopi na ma vie 🖖🏾

Khadija: aller ciao bonne journée

Wesh mangui préparé jeudi aye invités you ame diom ngay ame fofou dou yombe

Comme que damay ame ganeu bou riche té yorou ma nada legui damay tekk aye stratégie door 😆

Ma woma sama bene tata bou nekk France 🇫🇷 niou koy wakh Adji

Moi: allo tata cava name nala

Tata adji: oui cava très bien et toi mala raaw

Moi: oui cava très bien alhamdoulilah naka fofou

Mbeuguel Où les histoires vivent. Découvrez maintenant