Mes papam dafa fiire tekk ci sadikk
Khadija woma dima expliqué bimou agué sen keur noumou deff
Bima agué souniou keur dama fekk keur gui calme (ndékété pa bi mo tangale ci kawe mère bi ndakh té dama goudé)
Khadija : Kong Kong assalamou alleykoum yaye papa cava
Pabi: yaw khadija fonekone ba heures bi
Khadija : anniversaire la démone sama bene copine de classe moma invité wonneu
Pabi: legui soye dème do taggo
Mère bi: taggo na Kaye wonala ba sonou mes diotou la
Khadija : waw papa wonala pour tagou la mes diotou mala
Thieuy djiguene poumon dougou guene ci(Mane dé khamouma kagne la organisé anniversaire té yeugou mako )mes bon mon chemin n'est pas dedans
Pabi: waw wakh nga deugue guiss na say appel mes dama amone réunion
Khadija : legui nga nekk fi di youkhou waté
Mère bi: mane mi dé amoul loumou ma waxoul mes damay mougne rek ndakh maye seuye
Pabi:non ce que deukk bi dafa diakhasso té woroul motakh ma amone comportement bobou mes dou dara mangui diegalou
Mère bi: benen yonneu dangay deff ndankeu mo guene
Khadija : wa yaye legui diekh na indile nala ci lekkou anniversaire bi boul ci maye sama papa(Wa yene diomi wolene dija fanne la dieulé lekkou anniversaire)
Mes lepp stratégie leu pour bagna ame problèmesKhadija : mouha mane dé lima nekk ci auto bi mangui xalaat nane lay deff ba douma am problèmes ak sama papa mes pékhé dou diekh bima agué souniou kogne dama dème ci fast food bi dieundeu fa beignet ak fataya ak jus orange deff ko ci sachet pour souniou wa keur souniou narré kasse ma woneu lene lekk yi
Moi: wa dija baby ya deff lolou yeupp yaw yay tapete
Khadija : non nekoul tapete sakh wakh dji lay moytou rek motax ma deff ko
Moi: mane dé diakhal ngama mes ba sonno ci yonneu bi
Khadija : non sonou ma mes titone na ndakh té taximan damako ragal
Moi: ahahaha loy ragal ci taximan bi
Khadija : mane djiguene la en plus mane kassé ci auto bi wooroul
Moi: kou nekk ak mane do ragal mane may gaindé damala diokh sama fiite yaw kene doula. Deff dara
Khadija : yaw ya wanné mes mangui dem sangou nopalou après nala wowate
Moi: wa baxna bb prend soin de toi nga nopalou
Khadija : d'accord tkt même pas
Après ci la khole heures bi mou nekk 00h30mnt lolou goudi neu té commencé na guementou ma teuddeu sama chambre di khare dija paré pour niou continue souniou discussion
(Mes mane dalle lima nakari nekhouma Mamy mom nena douma bayi )
Mangui teuddeu ba commencé nelaw Mamy woma ci bene numéro inconnu
Moi:allô
Mamy: oui cava mouhamed
Moi: yaw kham ngani soma wowé ci sa numéro doumala dieul motakh nga woma ci numéro inconnu
Mamy: non damala beuga wakh ben affaire s'il te plait deglou
Moi: waxal mangui lay deglou
Mamy: mouha mane damala beugue té kham nani mala togne nangou nako so beugué sakh ma diokh la sama bopp
Moi:ahahaha wakho fi dara mamy mane soumala soxla wonneu damay d'accord nekate ak yaw juste pour fowé la mes lolou la doul deff
Mamy: wa legui wakh ma lo beugue
Moi: nga bayima rek la beugue par ce que danga nara yakk sama relations ak dija
Mamy: boulma wakh wakhou thiaga bobou dé tchim
Moi: mdr yaw thiaga bobou motakh sa fiit bi togga toul té lossi khamoul fimou may yobou mo guena nekh aldiana
Mamy: mes dinala wakh ben affaire loumou lathie dinako deff pour récupére la
Moi: wa baxna yaw amo bene diom
Ndékété limay wakh ak Mamy yeupp khadija mongui woté ci souff mes comme que dama concentré wou ci wakh dji bayiwe massi khele après ma woko téléphone bi sonné ba sonou dieuloul may insisté rek ba diote ko
Khadija : boulma wakh dara Kane nga doneu wakhal téléphone
Moi: mamy moma wo di wakh aye wakhou doff
Khadija : legui nga guiss samay appel nga bagne ma dieul
Moi: non dou lolou dama concentré wou wonneu ci wakh dji de trop motax sentirou mako
Khadija : ma wakh nganane ma danga concentré wou wa baxna a demain
Moi: non boulko dieulé fofou bb c'est que dama ko doneu wakh pour mou bayima
Khadija : wa doyna mangui teuddeu à demain
Moi : pourtant ya takh nelawou ma dé
Khadija : lolou sa problèmes la
Moi: dett way boul wakhé nonou kham nani danga merr mes billay soma méré douma nelaw bb s'il te plait dotoul am mane au moins wakh nala deugue meunone na fi nekk dilla fene té defou mako
(Thieuy yalla fane la dieum ak Mamy mi limou beugone ame nako mongui tasseu sama seuye)
Khadija : wa baxna yaw Khame ngani meunou mala méré mes Mamy momou beugue na nga réglé ko mou bayi niou ndakh niou doundou souniou aldiana
Moi: non tkt pas bb kokou dina dioukk ci mome legui mou bayi niou
Khadija: wa baxna bb 01h 25 diote na dama sonou mangui teuddeu à demain inchallah
Moi : waw a demain mon amour niou fanane diam bisous bye ciao( thieuy mbeuguel dall nekh na )
(Mes aye problèmes you beuri niongui nieuw juste nguene maye ma temps ma defaral lene ko sur le plats d'accord)

VOUS LISEZ
Mbeuguel
Любовные романыSalam Mangui toudou mouhamed Gueye Nioumay wowé Diego 21 mes souniou wa keur beugou niou toure bi sénégal dalle mo metti mes comprendre nalene parce que sama toure mo selle mangui ame 19 ans teint maron taille 1m75 gentleman kharitou khalé yi akk...