Kilifa Gui🤴🏽

1.6K 158 118
                                        

Tangaye bi nieuw na nakk deodorant yombe na bou lene faté sen pokotane yi 😂 ak slip yi bas you forokheu yi aussi delene ko faute Omo 50frs rek dangay solleu lou sett

Niome perruque mome Macky dakoye téré dafay ame chaleur 😂 moytou lene ko yalla tegoul kene loumou meunoul 😉


                        Suite Kilifa 🤴🏽




-Après bi khadija coupé ak Arona bayi woul deh dafay lidieunti solutions

Mou wo sama mame expliqué ko nimou démé mes heureusement wakh nako deugue

Sama mame woma ma nieuw wouyou ko

Mame: gueye ndioro no deff

Moi:Ndiaye mangui ci diam boubax et toi

Mame: waw mangui sante yalla

Moi:Alhamdoulilah yalna dieum kaname

Mame: khadija loutax mou guethie fi

Moi: khadija deh dafa commencé yabateii nena daff ma méré

Mame: legui la coupé wakh nama lepp

Moi: en bon konneu daff la woo

Mame: waw wonama expliqué ma lepp mes yaw tamite mou wakh lo boulma wowati rek nga bagne ko woo

Moi: mame yama yarr té meusso beugue ma niakk fayda mome mo ame fouleu nima boulma wowati ma ame fouleu bagne ko wo rek

Mame: waw lolou deugue mes tamite khame nga rek djiguene leu dafay sagou en plus di khole fane nga tolou ci mome

Moi: mes mame ame na moment yo khame ni kene doussi sagou en plus khadija khame na fimako tolou boubax dafa yakarone ni dama niakk fayda

Mame: niakko fayda mome juste danga beugue diaye tar rek mes yeureum nako deh dafa wakh ak mane bay dioye

Moi: koula bayi nga khasse ma 😂 mes mome loumouy dioye melni kou amoul sama numéro nama wo mome rek lay deglou

Mame: mome kham nga ni daff la roussa woo instant yi gathié mokoy raye mes yay goor woko rek nguene waxtane adouna amoul solo

Moi: adouna amoul solo motakh mou warone deff ndankeu mes mame doumako woo deh wallahi

Mame: mes legui bayil dinako woo wakh ko mou wolla mes balko rek nguene waxtane

Moi: lolou kaye dou problème mane sakh damako name wakh ko mou nieuw fi

Mame: mes loutax wowo ko wakh ko mou nieuw fi yaw bayil égoïste nga wo khalé bi daff la beugue deh

Moi: mako guena beugue lolou leu khame motakh moumay diaye lou amoul dafa khamoul rek dieul kenen lay deff legui

Mame: so fi dieulé kenen ma niouss la nga khame

Moi: 😂 wakhal loula nékh mane mome lambou ma yaw khame ngama boubax

Mame: yaw gnila topou nio niakk diome rek sa niawaye khamou ma loutax nga fouye

Moi: 😂 niawe nga wakh deh non non wakhal ma nima melle mane mi beaux gentle ba paré nekh ngay sisou mame mangui deme bala ngamay dooreu

Mame:niakk fayda soulla khadija wowé té dieulo ko dinala niouss nga khame

Moi:wa dinako dieul nenala damako name

-Mes mane tamite deuguere na bopp deh mes goor dafay ame fouleu mo wakh boumako wowati nako wait rek mes name nako lole 🌝mbeuguel ki est tu 😂

Mangui tokk di khare appel khadija ba nelaw

Le lendemain ma yewou khole sama telephone 📱 guissou ma dara cool ma sangou solou ba nice déme Mamelle!!

Mbeuguel Où les histoires vivent. Découvrez maintenant