Maye lene ma diam waye 😂

1.2K 106 88
                                    

6 mois plus tard 🤷🏽‍♂️

Ma ame rendez-vous ak khadija mes mako wara fekki sen keur affaire bou nara nékh 🙈

Jeudi matin ma yewou deff sama yeuff sagncé 😂 wallay wallay deff lou reuye wara deme ci sama Bae

Mes comme que dama ame sponsors leader mouy sama mame

Ma deme ci mame tegal ko Rendez-vous bi !!!

Moi: bonjour mame no def ?

Mame : cava alhamdoulilah mangui ci diam

Moi: naka matinal bi

Mame: sante alhamdoulilah lo beugati yangui barall rek

Moi: 😂 wa mame do deglou rek

Mame: damala khame soye nekhal rek am na lo beugue

Moi: wa dama wara setti khadija té yorou ma dara

Mame: lolou motax ngay tournée bobou bataye niata nga sokhla

Moi: thioum lolou la beuga dégue loma diokh baxna

Mame: 500frc baxna wala ?

Moi: hiiii 😂 mame diapp ci waye wakhou mala lolou

Mame: ya wakh louma la diokh baxna deh

Moi: legui diokh ma 5 milles

Mame: dinala ko diokh mes danga makoy remboursés

Moi: amoul problème yay sama chérie

Mame: wa baxna après demal ci boutiquier bi mou diokh la

Moi: d'accord ci kaname konneu

-Ma deme préparé wou ba melni boure 🤴🏽thioum deff comme d'habitude sagncé khegne nekh ymgx
Deme récupère khaliss bi ci boutiquier bi dioubali keur massar😂 lou nékh waye

Deme takhawe ci arrêt 🛑 bi khare bus 🚌 adouna metti woul économise sama alale ci la bokou

Ma ague galé khadija fekk fa yayam

Moi: assalamou alaykoum

Yayam : maleykoum salam mouhamed

Moi: oui maman name nala

Yayam: mala raaw lou beurri filston siloneiik

Moi: mangui ni rek sante yalla boubax alhamdoulilah

Yayam: bienvenue dalal diam

Moi: mercie maman Ana khadija

Yayam: mongui ci wagne bi moy togou taye

Moi: wa kharal ma deme nouyou ko

Yayam: d'accord

Ma deme Ci wagne bi fekk sama adouna ak alakhira mouy togou lou reuye 😂 billay wallay

Moi: salut mon amour

Dija: oui baby cava

Moi: oui cava je vais bien et toi

Dija: oui je vais bien alhamdoulilah sagncé nga deh bb

Moi: Mercie mon ❤️ simple rek

Dija: namone nala lole

Moi: mala raaw fouf billahi

Dija: lolou nekh na babe

Moi: wa loy togou taye

Dija: surprise leu bb bayil curieux

Moi: en wa d'accord do bayi ma deubeule la nokosse bi

Dija: non non konneu dangay kham loumay togou ninga moussé 😂

Mbeuguel Où les histoires vivent. Découvrez maintenant