Thiopintance❤️🖇

1.7K 161 225
                                        


Deuguere bopp dalle baxoul mangui beuga sonou ci Mamy 🤕indile nagnou bruit ba wa kogne bi yeupp diniou waxtané 😡mes xaral rek!!!

Moi: allo boy limamou

Limamou: wa boy nakawar

Moi: tranquille boy siloneiik

Limamou: mangui cool boy lou xeew

Moi: ils faut niou guissanté boy mamy mofi nekk di niou indile problème temps yi yeupp

Limamou: boy yene niakk nguene fayda deh mamy dafa reew rek dolene niouss ndym

Moi: boy yaw khame ngani mamy doyou niou gontou mes khame nga nima mell ci kogne kene meussou ma degue ci dara lou niakk fayda

Limamou: ana Arona?

Moi: mongui fi mo guena niakk fayda nieupp

Limamou: mome wakhou ma aye wakhame moko maye kaname

Moi: la fois passée boy mamy kourou roff leu yoreu takhawe sen bountou keur

Limamou: legui nolene deff?

Moi: Arona mom dako guiss rek dawe 😂 mane ma diade kogne toucouleur yi

Limamou: danga wiri kogne 😂 boy mamy mi napeu nalene deh

Moi: yaw rek la tekk nitte nakk kaye lidieunti ko ndax niou ame diam

Limamou: boy kokou comprendre nako moment yimou nekk ni motakh dafay énervé 😡 dina deme sen keur waxtane ak mome ci jamm khole noumouy démé

Moi: hiii négocier 😂 non méthode bobou bakhoul ki doff bou degoul dara deff yeuffou doff comme mome rek molla ci guéne

Limamou: tkt pas boy dinako setti waxtane ak mome sou changer woul ma tegal ko lou metti

Moi: tegal ko lou metti deh moy deal bi wayé waxtane mamy khamoul kouko nekhal

Limamou: tkt pas boy mangui fay nieuw ana Arona?

Moi: Arona mongui fi mo indi li yeupp dafa niakk fayda filay nekk diko roukheu mouy doff dofflou

Limamou: bayiko fofou mangui fay nieuw ci kaname waxal Arona niou tassé banc ba

Moi: Lolou matte na after Frère

Instant yi 2 problème la ame Mamy ak Marieme mes yalla baxna 🙏🏽

Marieme aussi mongui woté di lidieunti noumou ma iri wé pour dokhane ma  !!!

Marieme: allo chérie cava

Moi: oui cava je vais bien alhamdoulilah et toi

Marieme: sante yalla boubax Alhamdoulilah

Moi: cool donc siloneiik?

Marieme: mangui ni name la rek demb wonala ba sonou diotou mala

Moi: guisse na sa appel mes dama occupé wonneu motax

Marieme: en okey d'accord legui limala wakhone fossi tolou

Moi: khalate nassi boubax mes kagne nga beugue niou guissanté

Marieme: taye la mercredi bayil ba samedi

Moi: non samedi damay bougé motakh wakhal benen jour

Marieme: dimanche c'est bon

Moi: oui dimanche baxna

Marieme: dinala khare konneu

Moi: inchallah

Mbeuguel Des histoires addictives. Découvrez maintenant