Salam la famille mangui lene di nouyou kounekk ci sa tourr ak sa sante dilene nianale diam 🙏🏽 juste vous dire que dina lene diokh sen suite inchallah ci décembre bi par ce que khame nguene ni ecole oubi neu té diote amoul 😊comprendre lene ma té yalla takhe mangui lene di préparel suite bo khame niii damay bollé trois suite deff ko bene inchallah boulene wakh dara
Mercie ❤️

VOUS LISEZ
Mbeuguel
RomanceSalam Mangui toudou mouhamed Gueye Nioumay wowé Diego 21 mes souniou wa keur beugou niou toure bi sénégal dalle mo metti mes comprendre nalene parce que sama toure mo selle mangui ame 19 ans teint maron taille 1m75 gentleman kharitou khalé yi akk...