Bonjour, Salut, Bye bye

24 5 0
                                    

BONUS borom kër

Gouro, 3 pieces

Gouro, 3 pieces

Gouro, 3 pieces

Gouro, 3 pieces

[Pont]

(I say) Aladji Miezé

Def la sama sokhna lala yéné

Man ak ioe si diakka, imam ak préfet

Boléma'ak sa papa nako gérer (woo)

Yow laa wa yow le (x2)

Beug nala khamna beug ngama

Doyyal ngama soumala amé amna niénti diabar

Eh ngani pa bi nako wo-oh-oh-oh

Damleu beug takk guénouma ak yow-oh-oh-oh

Vieux père woxma lanela loy douter-eh-eh-eh

Beug nako amna dinée ak ligué-eh-eh-ey (Yeah)

[Pont 1] :

Baby oubbil ma sa xol pour ma nekk sa borom keur (Anh yeah)

Naala dieundeul ben keur pour ma nekk sa borom keur(Woo)

Wokhak sen wa keur nélène maay sa borom keur(anh yeah)

Naa taal sen keur sougnma deffoul sa borom keuur(Oh yeah)

[Refrain]:

Dina indi gouro,Def trois pièces

Gouro, def trois pièces

Gouro, def trois pièces

Gouro, def trois pièces

Gouro, trois pièces (ngané lane)

Gouro, trois pièces (ngané lane)

Gouro, trois pièces (ngané lane)

Gouro, trois pièces...

[Couplet 2]

(I say) Takk sama fite

Do am ben woudiou baby à part sama fite (Yeah)

Boula nékhé doreul radio

May sa borom keuur, baby cardio

(Eh) louy bayyanté pour kouné sey sey bi?

Ah bougn def lolou kay niou sey sey bi

(Eh) mak yow warrouniou am blem

Ya eupone prétendant championnat anglais

Réception invités yi nanni jinja

Soma firé dina mourou melni ninja

Mayé bou ndieuk meyyleu galé tekk cii 3 quarts

Soumaley nianni feug ngandi boubou 3/4

Man la gars yi wowé Bad man Miezé

Am diabar mou melni yow laa yagg rêver

Nuit de noce premier son ma mayyleu bébé

Yalnaa tokk di lath yallah finga fété (Yeaaaah)

[Pont]:

Baby oubbil ma sa khol pour ma nekk sa borom keur (anh yeah)

Nala dieundeul ben keur pour ma nekk sa borom keur

Wakh ak sen wa keur nélène may sa borom keur(Anh yeah)

Na tal sen keur sougnma deffoul sa borom keur(ooh yeaah)

[Refrain]:

Dina indi gouro,Def trois pièces

Gouro, def trois pièces

Gouro, def trois pièces

Gouro, def trois pièces

Gouro, trois pièces (ngané lane)

Gouro, trois pièces (ngané lane)

Gouro, trois pièces (ngané lane)

Gouro, trois pièces...

[Pont]

Aladji Miezé

Def la sama sokhna lala yéné (Yeah Yeah Yeah)

Aladji Miezé

Def la sama sokhna lala yéné (Yeah Yeah Yeah)

Aladji Mieze

Def la sama soxna lala yéné (Yeah Yeah Yeah)

Aladji Miezé

Def la sama sokhna lala yéné

Jamilvslove💕.

Fara'ma'reine: TOME 1Où les histoires vivent. Découvrez maintenant