BONUS: BAKAAR (péché)
[Chorus : Canabass]
Bayima soumi louboutin yi roti satalabi def aay raakh-thia
Est-ce que saakh douma moudjou sangou dji sétt pour laabaal bi geuneu baakh ndaakh
Maane geudj na diégué assamane pourtant demb ci night mangui fanane five star
Yeah def na défati khamna ni li dou deugg Mais doyaloumeu bakaar
Yeah khamna ni lou armoire bi meuneti fess douma yobou loudoul perkaal
Mais amna yeuré you bess youma solagoul té douma téré dieundaate
Ndaakh life bou leundeum bima né di doundou def méy khirr cii beugg geune taak
Yeah khamna saakh cii lou baakh moy sama garap mais taayél nako djeumbaate
Légui fadjaar jott mais beugeugouma goudi gui diekh
Méy dadjék nittou yallah yi sen beutt yi dima jugeeeer
Beugouma teek sama Kheeeeel
808 bi di reuk noddou bi di nieuweuk mélodém
Khamna louma waar mais sama nafsou moy sama jaiiiiiiil
Méy nélaaw di teude perpéeeete
Eeehh
Bayima soumi louboutin yi roti satalabi def aay raakhthia
Est ce que saakh douma moudjou sangou dji sétt pour laabaal bi geuneu baakh ndaakh
Maane geudj na diégué assamane pourtant demb cii night mangui fanane five star
Yeah def na défati khamna ni li dou deugg
Mais doyaloumeu bakaar
[Zou Kana]
Fast life iblis dem ba roff string bou khonk ci sama bir sac
Laang bou riche fessak jongoma ak aay koba mbété mbaalaxman
Seulmo champagne liquide fi Mo lene gueuneul ndokhou Zam-Zam
Thieureum yeupp la nara léyo waayé séttoul loudoul lou nex bakanaam
Degg neu Yallah mais da taamou djeul callou Ibliss
Miine na lougn ko téré diégué
cii leundeum rek ngua kooy guiss
Waayé dou leen loudoul nitt
gawa wédi loum meunoul guiss
dégnouy kush té dégniy lean
moudjié safara degn ko tiite
Degn laa yapp dou degn la miine
ooh lord
Ibliss def na string bou khonk cii sama biir sac
Khalé bou baax cii Laal bi waayé léwoul
kone bokk faayou jeuf bi dou louy moune baax
[[Chorus : Canabasse]
Kone bayima baayi thiaakhane djouk ci laale soli pégnoire def aay raakhtia
Est ce que saakh douma moudjou sangou dji sétt pour laabaal bi geuneu baakh ndaakh
Maane geudj na diégué assamane pourtant demb ci night mangui fanane five star
VOUS LISEZ
Fara'ma'reine: TOME 1
Romance🎤 Lati diop déguénn mbaaay ... 🎤 Dior démba déguénn mbaaay..... 🎤 Dagou dagou déguénn mbaay.... .. .......