OMG: Niou dém mairie
[Couplet 1]
Bokoulok gniy doorr Li goor yi di bari bari amo tchi dé dénda-ndo
Lème bougnou soukeur Kouko khassa moss daal Dou yombeu bayi koYaw danga meune mine mokal jiguéne Mani danga rakh ndakh li dou nène
[Refrain]
Beut yi gueuthie na taa ndax yaw,
Xol bi deuké naate ndax yaw,
Yéndo di rétaane ndax yaw,
Namuma greffage ndax yaw,
Faléwuma maquillage ndax yaw,
Diotna gnou mariage maak yaw,Baby kaay gnaane si,
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi,
Lima beug moy niou dem mairie,
Dem mairie niou dem mairie,Baby kaay gnaane si,
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi,
Lima beug moy niou dem mairie,
Dem mairie niou dem mairie.[Couplet 2]
Yaye sama titi tara pararapa para para,
Li mbeuguelou moumeu le diaroul di wax ndax yaw mi xam nga,
Laadiou ma aye milliard Kilo gouro nga ame diabar Kone légui lane ngay xaar,
Gnoune jiguene seuy moy suñu taar.[Refrain]
Beut yi gueuthie na taa ndax yaw,
Xol bi deuké naate ndax yaw,
Yéndo di rétaane ndax yaw Namuma greffage ndax yaw,
Faléwuma maquillage ndax yaw,
Diotna gnou mariage maak yaw.Baby kaay gnaane si,
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi,
Lima beug moy niou dem mairie,
Dem mairie niou dem mairie,Baby kaay gnaane si,
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi,
Lima beug moy niou dem mairie,
Dem mairie niou dem mairie.[Couplet 3]
Yangui dape sama banekh,
Di fathie samay adio,
Xam di def lila war,
Bolèwo darak thioy,
Wayè wayè am na lou dess,Niou dem mairie Niou dem mairie Niou dem mairie Niou dem mairie.
Baby kaay gnaane si,
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye,
Lima beug moy niou dem mairie,
Dem mairie niou dem mairie.Baby kaay gnaane si,
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye,
Lima beug moy niou dem mairie,
Dem mairie niou dem mairie.👰🤵.
VOUS LISEZ
Fara'ma'reine: TOME 1
Romance🎤 Lati diop déguénn mbaaay ... 🎤 Dior démba déguénn mbaaay..... 🎤 Dagou dagou déguénn mbaay.... .. .......