Ngoor et Gnilane sont des jeunes résidant dans le même village. Un jour,leur rencontre fortuit provoqua des remous dans les veines de Ngoor,et ce fut le coup de foudre .Ansi Ngoor commença à sentir que Gnilane serait une balustrade sur laquelle il pourrait s'appuyer.Mais notons aussi que Gnilane était en couple avec un dénommé Niokhor.Et Ngoor, avec ces méthodes qui sortent de l'ordinaire,ne renonça pas à séduire cette demoiselle et essaya de s'approcher d'elle.
Ngoor :soxna ci cv no deff?
Gnilane :CV cool
Ngoor :Ba xamngani reuk rayna signell wayé loxo mouniouko
Gnilane :Manam?
Ngoor :Manam louki nga sama beutt dh
Gnilane :Té toxoniou wo sax?
Ngoor :diakarlo bi rk doyna toxoniou
Gnilane :ahann,ndeysane ba diam?
Ngoor :ma tollou nii dh,sama xel momay dakhh té fouma lakkou
laa done weurr té dadj naako bimala guisseiGnilane :té nga wax lou lerr tmt
Ngoor :ah ioe tmt prtt lima wax leer na dh,mbeugueel lalay
dioundiou té sisa biir xol dou niakk ma xadj faGnilane :anh,je comprends degg nala
Ngoor :xamna lolou
Gnilane :wanté daaa fek ni salaane diooyoul weeet
Ngoor :u veux dire?
Gnilane :suis vraiment désolée,da am kima neikak
DIEULEUL MA NGOORREK...SHEUUT MO BEURI WAX
Ngoor :wa leigui wouyouma ,tay soo amone robe bou maguett yagg ko soll,sa yaye dieundeul la beineine bou besss takk noy def?
Gnilane :bou bess bi lay dieul ioe tmt
Ngoor :Mane nak may bou bess bi,té avant ngakoy dieul sax,xana dingako natt,yaw nattagooma sax beug ma sanni,leigui xamnga nouniouy def dioxma sa numero comme ça niou gen waxtaane inchaa ALLAH
Gnilane :mdr...wa oki tkt
Durant trois semaines Ngoor mongui toppou si guinaw xalé bi,ben beuss mou yonni ben xaritam biniouy wowé Ibou pour mou waxak mom. Ibou daldi dem wax yobanté bi Gnilane.
ВЫ ЧИТАЕТЕ
NGOOR AK GNILANE
Любовные романыHistoire rédigée en wolof compréhensible et assez pure Ngoor et Gnilane sont des jeunes résidant dans le même village. Un jour,leur rencontre fortuit provoqua des remous dans les veines de Ngoor,et ce fut le coup de foudre .Ansi Ngoor commença à sen...