Gnilane :louy lolou?
Ngoor :waroulo xiif,ndax deugg ak mbeugueel bimala xiin yeupp,tawnaala ko gouddi,tawlako beuthieuk,kone ganthiakh gui warr na niorr
Gnilane :ioe lila metti lenn rek la,bou ndapp xatei Gaana day dioy
Ngoor :walae dara metti wouma danga fokni damay wax ni pour wax,kone phase test la nek ni batay?mane sa ndieurigne lalay wax rek
Gnilane :yaw kay waxal rek,ndax fa nga meunei
Ngoor :non soxna ci boulnax sa bop,kone si setlouma nga tollou batay?danga diapp ni ay wax rek laa yorr ni,...,limay wax deug la si maneté beussbouniou andei dinga xamni dieuff yaka gen deuggou
Gnilane :ah bon,dinagn si xam dara
Ngoor :utilisel sa xel mi,té bania melni kouddou,am sa gueeiin né doko yeungel moukk
Gnilane :hum yalla baxna degg nala
Ngoor :xam sa bop daal mo gen nioulakoy ,xameil say xaritt bou baxx
Gnilane :oki mais yangui melni koumay xass nak
Ngoor :wallah xassoumala sax,dama xamni alal dou dara ndax nitt loumou beurri lé beurri lé,bou gueinnei guiss loumou momoul,lolou rk la
Gnilane :Mane daal beugouma koumay xass,té lixew yeupp xass na ba am ba paré,té diall na tmt...kone dieex na
Ngoor :wiwi je comprends mais damalay wax deugg rk oci kila beug rek molay wax deug,douma meuss toppou sa beuug banila yalla mongui lay nouyou,mais tmt dinala toppou xool la xoolate la ni togg katt di xoolé ganar si biir tchine ,lingama diaral maka xam,té wantérou mako ben yoon,kafééwoumala sax
Gnilane :je sais mais mane xamatoima louy mbeugueel ndax sa youma yaakaré ni mangui ci rek,déception laciy dieulei
Ngoor :soma dieigué wone waxoumala niam dh mais dotoulo xiif mbeugueel té dingaci dieufeundiko ba lapp ci
Gnilane :Mais nak dama niorr tabbi guesseum wathié wouma,dama dounde lou beurri ci lolou motax
ВЫ ЧИТАЕТЕ
NGOOR AK GNILANE
Любовные романыHistoire rédigée en wolof compréhensible et assez pure Ngoor et Gnilane sont des jeunes résidant dans le même village. Un jour,leur rencontre fortuit provoqua des remous dans les veines de Ngoor,et ce fut le coup de foudre .Ansi Ngoor commença à sen...