Ah Gnilane reitane reitane na nk,tchine bou narrei neex bou baxei xeign.Ndeek touti Niokhorr commencer woo Gnilane(woo nako niaari yoon),mais gnilane tmt louko ngoor done wax commencer wone nako doug bamou yeixx dieul,Niokhorr daldi wooté waatt
Niokhorr :Allô ioe,mangui lay woo nga nek en commuinication,setlounaa fann yi yeupp nii leu,guisseutoumala lou beurri té soumala wowé yangui communiquer rk
Gnilane :fann yi dama diapp rk mtx am ay papiers yimay lidieunti té sax,sank daa am kima done woo motaxone,mais dou dara...namnala silo nk
Niokhorr :Anh ioe ngaka ngama fook,té waxou looma bou yagg,ioe dama commencer niaaw ndiorte si yaw,kérok seen nala ak ben waay,m mala bayi tchi biir,xamna founiouy moudj dou nexx nak mak ioe
Niokhor nak,boy bou doywaar la,amna bayré, xalé yi djigueen yi toppou nagn ko,té beurrilé naci,yalla dogal mou dadjé si ak ben xalé bou rafett(ATHIAA) maachaaALLAH,mou diaralone ko bayyi nieupp,si mésentente bou touti bobou la beug diiaar nak ba bayyanté ak Gnilane ,ndeysane,té limaci diaaxal Gnilane,beugg nako trop
Gnilane :Wa xaral ma expliquer leu
Niokhor :soxla wouma ben explication
Si nonou ,niokhorr daldi raccrocher.Gnilane diaxlé,xolam fess,voix bi changer nk,mou took touti ngoor woowate ko ( Ngoor Kagn lay bayyi Ngoor :Ioe ba déranger woumala si sama appels you beurri yi?)
Gnilane :Non meme pas
Ngoor :Sa voix bi dafa changer sax ba diam?
Gnilane :Non dou dara...xamna after inchaa ALLAH,peut etre nala expliquer
Ngoor :ok,mais waxal ma sa waadji,thiouthie bou narè Done seqqq,tchine meunouci dara dh,apres bo feixei rk niou continuer
Niou took 4jours nioom niaar deggenté wouniou,mais Gnilane mongui done waxak niokhorr,pour négocier si sen relation,mais Niokhorr,lank né guisseutoul likoy took lo si relation bobou
YOU ARE READING
NGOOR AK GNILANE
RomanceHistoire rédigée en wolof compréhensible et assez pure Ngoor et Gnilane sont des jeunes résidant dans le même village. Un jour,leur rencontre fortuit provoqua des remous dans les veines de Ngoor,et ce fut le coup de foudre .Ansi Ngoor commença à sen...