Partie 7

246 19 0
                                    

Ngoor :Gnilane nanga def?

Gnilane :cv mangui ni rk,guedj nala guiss?

Ngoor :deug leu mais dieexna tay,nakamou silo nk,...yangui xalate batay?

Gnilane :wa guiss nga dh,ay blems youdoul dieex rk

Ngoor :Bi yoon doumala wax nga expliquer ma ,j'ai tout compris

Gnilane :Lo comprendre?

Ngoor :non lolou souniou sooboo dinga xam,té xamnaani xamnga

Gnilane :bou dei li nek sama bop la,ngako yeuguei dinama diaaxal

Ngoor :murs yi sax daniouy wax leigui ioe tmt,mangui done wax ak yaw dila yedd si lou beurri,mais nangouloma degglou,tay yangui nii gen diaaxlé,xamngani kouy diaaxane di saw bala kenn di tooy nga loorr

Gnilane :bayil ningay waxé ak maneway ioe tmt,boulma yokkou blem

Ngoor :Ah non jamais ma yokkou la blem,mais daal mbaam soudone degg wax,yatt douko dall,ana loy daw bay daanou ndax alal,je te comprends nak andandooo day wallé,té saysay waxoul deug wanté yakk na xel,lepp yeuk naako,neiwone naala ragnel say xaritt si seini xalate.

Gnilane :dettt xamal ningay waxei rk,niom lou bax lagn ma yeinnei wone,té sax mak yaw nio nekniom nékouniou

Ngoor :Sou donone lou baxx doo terr ci fi

Gnilane :Ngoor garap go rombou mou sanni la mbourou,bou euleuguei dofa rombaat nga fook?

Ngoor :liniou wax si yein deug leu,mangui doga gem nii deug deug mato lein,diapal ni nak xel moy sourr té sax yaw waroo xiiff

NGOOR AK GNILANEWhere stories live. Discover now