partie 10

241 20 3
                                    

Gnilane :batay daal yay wax,naniou xaar daal lepp dina leer inchaa ALLAH,d'ailleurs le 14fev damay def sama anniversaire té inviter nala inchaa ALLAH t'auras ta réponse

Ngoor :ah bon lolou dagn koy paré paré,mais pourquoi pas mtnt?

Gnilane :Dou malani nga xaar ma rek,xaaral ba bess ba

Ngoor :batay dinako xaar mais xamal ni sama diggenté ak ioe beuss bouci yalla andei banga nangoul ma limay woutt,dina mell ni nguenteel bou roplane di yobboul ndawtal

Gnilane :mdrrr ioe amoo..mais dinala xaar dh

Ngoor :Inchaa Allah dinagn def teew,mais daal waxtane wi amna solo té limalaci wax yeupp pour sa diam la rek,sou mala waxei lou eupp tmt nga dieigueul ma bou baxx

Gnilane :Non amoul ben probleme,comprendre naa lepp,tkt pas

Ngoor :d'accord,ioe borom baxx nga yaw,kone meune nagn dem lolou rk lala done doyyé,té sa anniversaire bi boul wax dara

Gnilane :wa baxna ioe...lol

Si nonou nak laniou taggatoo wei ndeysaan,...,nek si préparations anniversaire Gnilane bi WaGnilane dina nangou am dett?
-----------------------------------------------------------------------------

RV le 14février
Vos réactions😀

NGOOR AK GNILANEWaar verhalen tot leven komen. Ontdek het nu