Partie 14

174 11 0
                                    

               

Ahh Ngoor ak Gnilane nak ,sen Andd bangui doxx maa chaa ALLAH,wanté amna ay mbirr
you laxassou si biir,
Diggëntei bobou tamit,Gnilane dioot nafi def bac(bobou moy niareil yoonam),mais moudiou si guenn,mou diaaxalone ko trop ndeysane,
Boulein fatté ni tmt,jr anniv ba,kenn si ay xaritou Gnilane(Astou),lidieunti
wone na numéro Ngoor(ndeysane dafa bardéé wone).
Astou momou nak mo sonal Ngoor ak ay msg aki appels youdoul dieex.
Tei Niokhorr dafa dem ba beugaate Gnilane diko sakkou pour mou dellou ci ndax guiss nani
xalé bi dafa gueneu mature,gueneu diekk maa chaa Allah.
Ben bess Niokhor guiss Gnilane,tei beugone na waxak mom bou yagg,wantei kersa ak rouss
moko diapp ndeysane…mou dieiki ni : « xaral ma dem bala may niakk samay beutt »
Mou daldi dem,di diay taar aki kiliftef…lol

Niokhor :Wa kidou Sokhna Gnilane ?

Gnilane : wa cv ?

Niokhor :Guedj naniou guissei trop,silo nek ?
ba yangui am diam ?

Gnilane : wa Alhamdoulillah

Répliques yi gatt naniou dh…lol,

Niokhor :loubess ?yangui noce ?

Gnilane :maa chaa ALLAH sante yalla bou baxx

Niokhor : Ah mane dh,guedj na noce biniou takaliko batay,
Bimala guissa toulei,lay doga xam deugg deugg yay kane

Thiey sama gars yi

Gnilane : badou dangay chomer ni,ah dou ya deifone sa bop DG,di dakkei,
Ni kou yorr employés

Niokhor : Non dou lolou sax,gueidione leu degg ak waxtan ak yaw rek,ak
Cheytanei rek leu wone,xamnga ni yaw la mine,tei nangou nani mala toogn

Gnilane :dinala wax dara nak.Guiss ng garapp bouy magg sa bamouy touti lanioukoy
Dioubeunti,do bayyi bamou magg ba am ay bankass sax ay xopp nga beugg ko dioubeunti ba
paré tekci beug sei diarignooo

Niokhor : wa lolou yeupp deug leu,t bou lolou wesso xana dingama dieigueul

Gnilane tok bamou yagg xamoul limouy wax ndeysane

Gnilane:Ahh nala xawa dieigueul rk, wouyouma dama nek ci yoon

Niokhor :wa xawa dieigueul moy lane ?

Gnilane :sheutttt,damay bagn tardé si fima dieum

Niokhor :Wa bo dellou ci,souniou meunei guissei in chaa ALLAH

Gnilane :Xamnani ni daal,mangui dem nianal ma yegg si diam

Niokhorr : wa d’accord yoonou diam.

Si nonou laniou tagato wei…

Mais Ngoor noum wara deukek Astou ?
Ah niou xooli ko baxam

NGOOR AK GNILANEWhere stories live. Discover now