Gnilane :ngoor yaw mangui dieiguelou dh
Ngoor :non amoul ben blem
Gnilane :dou sa réponse rek nga soxla?
Ngoor :waw té yaw lay deggglou
Gnilane :oki,ana sama cadeau?
Ngoor :xaral ma souhaiter joyeux anniversaire...lol
Gnilane :lol...wa d'accord et à ta manière
Salle biniou neikone nak nioom niaar rek fa dess té amone na ben micro bifa nek,ngoor dem dieul micro bi daldi taxaw xool Gnilane,diko koy xool ci biir beutt
Ngoor : KONE JOYEUX ANNIVERSAIRE BEI,XAMAL NI NAK SAY ATT DAFA WAGNIKOU,YOKKOU WOUL,DILA NIANAL YALLA DEIFAL LA DIAM AK WERR,KEPP KOULA YEINEI XIIF SA BOKO ROMBEII REK GUEIXEUL,YANGUI MAY LADJ CADEAU SANK,CADEAU BIMALAY DIOXX XAMNGAKO BOU BAXX TÉ YAGG NALAKO WANN SI WAX AK SI DIEUF,SAMA XOL LALA DIOXX,XAMNGA KOU DIOUDDOO SI TAGG BOU NAWOUL DINA DIAAXAL AY MBOKAM,WANTÉ THIOOFEILOU MBEUGUEEL TCHI XOL LAY DIOUGUEI TÉ BOU GUEINNOUL REK DIAXAL XEL.THIOFEEL GUI WAAT NAA NI YOROUL MÉLOKAANOU FELL,WANTÉ EUMB NA DJIKOOM,NDAXX GUISS NGA AY FELL NINIOU LA MEUNEI DIOUKLOO FI NGA TOOK,NONOU LALA THIOFEELOU MEUGUEEL DILA VOYAGER LO TÉ DOKO YEUK,MOTAX MA BELLE, BIMALA GUISSEI LA XAMNI WARR NAGN MEUNE NEK BENN SI LAA XAMEINI YAYE SAMA GUENN WALL TÉ MEUNE NALA WOWEI NÉNÉ(BÉBÉ) YAYE SAMA XOL TÉ DOUMA TEEN DILA XOOL DAMAY YONNI SAMA XEL MOU XOOLI FOO REER SI SAMA XOL XAMNANI MEUNE NGA FÈÈY,WAYÉ TAY NGA LAP TCHI BIIR NDAXX BEUG BIMALA BEUGG WALLAH MEUNOUL DOUGUEUL KEINEINE CI BIIR
Ngoor paré daldi tekk micro bi,nieuw dieiguei ci Gnilane.Ohhh Gnilane yaram wi ciommencer daww xamatoul loumouy waxx,mouy yeuk lou graw si xolam ndeysaaan,rongogn yi di tokou
Gnilane :...bilae meunouma sax wax
Ngoor :Boul waxx li neikoul si yaw
Gnilane :Sama xol moo fess,meme boudoul mbeugueel sax,diangue nala bou baxx,té diangue naa lou beurri si yaw,saches que mala guen beugg,xamantei naniou miineuntei naniou té yaaakar nani yalla dina niou diappalé Ngoor :mane li yeupp xamone nako mais noppil nak, xana di niane yalla soutouraal té yalla bou yaakar tass
SI NONOU GNILANE NANGOUL NA NGOOR LIMOU YAGG WOUTT NDEYSAAN,SI LANIOU ANDE NIOOM NIAAR DALDI GNIBI
---------------------------------------------------------------
L'histoire aura une suite ,mais elle sera surprenante et tres bouleverséeAythieu commentez....😀
KAMU SEDANG MEMBACA
NGOOR AK GNILANE
RomansaHistoire rédigée en wolof compréhensible et assez pure Ngoor et Gnilane sont des jeunes résidant dans le même village. Un jour,leur rencontre fortuit provoqua des remous dans les veines de Ngoor,et ce fut le coup de foudre .Ansi Ngoor commença à sen...