partie 9

257 19 0
                                    

Ngoor :mane xamna lolou,bou forr yombone,daniiouy tayyel seugg...mais sa niorr tabbi feinioul si gninga neikalone,niom gueseumouniou la,dagn la eufff rk nga watchi,ndax lane? alal... mdr

Gnilane :ahan yangui commencer waat nak bayil lolou

Ngoor :wa oki bayyi nako,diaaxal ngama nak

Gnilane;anh silane nonou?

Ngoor :Ahh dama xamni katt,bou saf amoul wone sapp douça am wall,té nga dieema saf ci mane rk ak sama thiofeel gui,souniou dieum yi nieuw sapaliko

Gnilane :ins bi safagouma si benn thiofeel vraiment,dama wexx xatt ak ay blems mtx,linga wax yeupp degg nako,douma xalé tamit

Ngoor :non yaw waro di am blem,may done kilay deufeul,té dou yagg nga guiss limalay waxx

Gnilane :ahh laissons l'avenir nous guider rk

Ngoor :Ehh mane maalay gueinnei sisay blem inchaa Allah,ngueilaw gou dougel xopp si paxx,gueinnei wouko fa,nioom deufeulou niou la dh mais may done kilay diapalé

Gnilane :lepp ci yaakar lay tambalé,mais dina leer ci kanam ak sisay dieuff inchaa ALLAH

Ngoor :Dou ay naxx,ak ninga rafétéé ni kaar maachaa ALLAH?reuy biir daal,am linga lek baxx naça

Gnilane :ngani?manam?

Ngoor :yaa gen xam limala wax yaw tmt,yangui diekk maachaa ALLAH,té dieumbeutoo dara si sa xol bi

Gnilane :anh lolo nga fook rk?

Ngoor :anh xamnani mane la...lol

NGOOR AK GNILANEWhere stories live. Discover now