Durant trois semaines Ngoor mongui toppou si guinaw xalé bi,ben beuss mou yonni ben xaritam biniouy wowé Ibou pour mou waxak mom. Ibou daldi dem wax yobanté bi Gnilane.
Bimou paré nak Gnilane daldikay tontou.Gnilane :wa ioe paré nga ?
Ibou :wa souma dioumoul,noppi naa dh
Gnilane :Bo démé nell kila yonni,yobbeunté galgal taxoul sa mbeur daane
Apres lolou Ibou daldi rendre compte NGOOR,naka nonou sila ngoor wowé Gnilane
Ngoor :ALLô,cv Gnilane
Gnilane :cv bien
Ngoor :j'espère que yangui am diam?Bon damala done xamal ni diott na sa yobeunté
Gnilane :uhn,c'est bien ,neiwone nala mangui ak keineine mak yaw je pense pas que ni dina meune nek
Ngoor :Deglouma bou baxx,xana xamoni adduna ndioogaanou golo la,garap gouné meune nafa lonkou
Gnilane :Mala gen xamni mbarakissou kania la,kenn xamoul foumouy beunnei
ô wadji waarou na nak
Ngoor :oki dis moi dp8 kan vs etes ensemble ?
Gnilane :presque trois mois
Ngoor :yaggoul nonou kone
Gnilane :mais bou loxo xawei yagg si pakh dafaa fekk diam
Deigueul ngoor ,neina day araftou dh
Ngoor :voilà nak,lolou motax,ma yagg si wax dji,diam ak salam bima fekk mo gen tax
Gnilane :anh wanté yeugo ni bi feineine amei batay kenn sonatoul...depuis kerok batay yangui may toppou,deggoo limala wax xana
Ngoor :wi degentaane,mais yalla tabaxaoul adduna si nietti fann,té dodj bouy tei sakkett daça wara seuss reuk
Gnilane :ahh ioe daal ndourou ngama kou beurri wax
Ngoor :pourtant beurri wouma wax sax,sama lamign mo sawarr rk tekci limay wax done deugg si mane rk motax
Gnilane :xamnani bo paré dh,beurrigo ndoxx sax dingaka xeep ndax danga wodoo sa lamign foum tollou nii
Ngoor :ioe la rk,ioe ko diomal mou woddoo lamignam
Gnilane :mdrrrrrrrrr,wa mayma ma am koumawouyou,sama cop bi moamay wo,tchi knam
YOU ARE READING
NGOOR AK GNILANE
RomanceHistoire rédigée en wolof compréhensible et assez pure Ngoor et Gnilane sont des jeunes résidant dans le même village. Un jour,leur rencontre fortuit provoqua des remous dans les veines de Ngoor,et ce fut le coup de foudre .Ansi Ngoor commença à sen...