Partie 4

360 29 5
                                    

Le lendemain Ngoor woowaatt ko(Xeuthie bou dagoul dikk)

Ngoor :Cv loubess

Gnilane :Bien aah,dara bessoul

Ngoor :mais yangui noce kmm,baa commencer ngama guent rk

Gnilane :lol...Yamal waay

Ngoor :yako tay ni meunoumako,ak yaw rk...mais dis moi,oft li xeiwone tu peux m'expliquer dh,xamna sa xol neixoul xone mais waxma rk

Gnilane :rien de grav,grawoul bayyil nonou rk

Ngoor :waxma rk

Gnilane :xamnga rk,sama xol mo fess,té mom rk mofa xadione,sama yaakaar tass,té waxnak mom ba sonnou meunoul comprendre,...danio am blem m tollou ni

Ngoor :ngani sa xol dafa fess té mom rk mofa xadione?

Gnilane :srx...

Ngoor :n'est ce pas yangui dieema waxak mom dieemoul sax comprendre?

Gnilane :stp bayil nonou waay

Ngoor :guiss nga dinala wax ben affaire,kouniouy dakk pour mou nieuw naane ,kokou maroul.wanté fo degg "daakal mingay naane",diapal ni kokou mo marr,t ins bi dama marrrr loll t warngako xam

Gnilane :mais mane sama xol mom rk mofa xathie

Ngoor :té mou wann la guinaw,ioe tmt tchinn loumou xatt xatt,xorom xathie naça,té momsax da xolli sa xol bi ni goomou seddaay war nga soxla pansement

Gnilane :unhhh ins bi mom je sais pas kw t dire

Ngoor :comprendre nala dh,finga tollou motax,mais lenn dinalako wax,leiir namani mom thiofeelam si yaw dafka sampone rk,té lepp louniouy samp rk meune nagn ko simpi,mane nak liniouy dieumbeutt la yorr,té day sax di laww,té beugg naa mou yegg sa faw

Gnilane :Ahan baaadou,...,doyna waar dh,mais esk doma may tps touti,blems yi da xaw beurri si sama coté

Ngoor :waa batay dinala xaar,...yakamti mom ,yakoulé rk.Mais ndourou ngama kou yorr djikoy ciment nak...lol

Gnilane :Ah yakamti mom baaxoul,wa djikoy ciment meune na nek dh ndax ben yoon lay faral di tooy

Ngoor :dell dieem nek bann sax dfw,ndax ngay tooy di tooyaate

Gnilane :mangui xool daal,beugouma daanou si kamb

NGOOR AK GNILANEWhere stories live. Discover now