Ahh gars yangui préparer anniversaire bi,té ngoor diott na invitation wam bou yagg,té yakamtina loll bess bi. Ahh 14fevrier diott na,salle biniou kay deifei mongui commencer fess,invités yi teew nagn,mais ngoor bimou nieuwei daniouko teiyyé si bountou bi car dafa yakamti ba fatté carte d'invitaion wam,mou xeexx fa ak gardes yi,baniou gaagn ko si loxo.Gnilane nak togone lou yagg guissouko,mou daldi guenn pour xool mou tollou,si nonou la guissei ngoor took si bitti daldi cool.Apres mou waxak mom ladj ko li xew,ngoor tegal ko,sila Gnilane andak mom daldi dougou ci biir,mais ngoor limouy andak Gnilane yeupp mongui diapp loxo bi,Gnilane remarquer lolou
Gnilane :wa ioe sa loxo bi nak?
Ngoor :ahh dou dara
Gnilane :ehh wouyouma kou mathie lou saf rk oy siithiou,danga gaaniou?
Ngoor :boul diaxlé,bayil mou sedd ioe tamit dou dara..nakamou nak?
Gnilane :Ahh ça va nii...lou bess?
Ngoor :ahh dara bessoul,silo nek nak?
Gnilane :xana si li xew rk,wa yaa sagnsei li?
Ngoor :wa guiss nga fass yeinei diakarlo ak diante bici roukou bi,wanté ken dou yaw nga guenn nooy na
Gnilane :bayil toogn,wa niou yegg si biir,gars yangui ci biir
Ngoor nak mongui sagnsei bay bagn...ay xaritt aki andandoo Gnilane yi nieuwoune si fete bi sax,daniou commencer wone di bardé,demna sax ba am ko xamni Astou la toudou def na le tout ba lidieunti numéro ngoor(dina gen leer ci saisons yici kanam)
Leigui gars yangui fêtou,mais ngoor AK Gnilane niongui taal di yaatal seini waxtanengoor :wa ioe tay la tay dh,lepp matt na mba?
Gnilane:wa meune nagn wax lolou dh,ins bi mom ma momei vent,bo guissei lidiota xew yeupp,dafa fekni,bala nga niande gueleem danga warr diott sa bakane ,wa motax mabeugone diott sa xol deug pour répondre la
Ngoor :deug leu,comprendre nala,motax ma gueum lima gueum rek ndax kakataar momloumyeex yeex ,weurseugem rk lay doundei,mo waral tayyi wouma ben yoon si yaw
Gilane :Nga dieigel ma tamit,parfois dane nga wax malay meirei Ngoor :non ioe tamit nga tolone la rek comprendre nala bou baxx,ameilo ben akk
KAMU SEDANG MEMBACA
NGOOR AK GNILANE
RomansaHistoire rédigée en wolof compréhensible et assez pure Ngoor et Gnilane sont des jeunes résidant dans le même village. Un jour,leur rencontre fortuit provoqua des remous dans les veines de Ngoor,et ce fut le coup de foudre .Ansi Ngoor commença à sen...