Partie18

61 7 2
                                    

Niokhor da fokni mo mom boy bi batay,mongui andak mom tchi mbedd bi dh

Niokhor :Gnilane cv ,silo nk

Gnilane :sante alhamdoulillah

Niokhor :xamnani danga nek si yoon ,mais warnagn meun yeigali sougn waxtane bou kérok

Gnilane :yaw fatt ngama dh,tei doma bayyi ak sama yoon

Niokhor :sa yoon moy sama yoon ,tei yagg naniou bokk yoon

Gnilane : Et après ,lou xass ba diall kay wess na

Niokhor :kone lolou mtx neikhouma dieigueul,mangui reithiou fim tollou ni

Gnilane :kone fofou nga tollou ?,mayma ma dougou si finiouma yonni tei guenn

Gnilane doug gueinaate ,niokhorr continuer diko topp rek

Niokhor :prtt nii lako guentei wone ngay dougg sama keur

Gnilane : wooy C ndeysanant ,wayé fii douca keur

Niokhor :ah misaal la rek ioe tmt

Gnilane :lingay wax ni tollouma fenn,mingui melni nga degg nitt naane deubb na ndoxx bamou mokk,

Doumala xoromal sax

Niokhor :xeuyna limay wax mola nioragoul rek

Gnilane :ah kone lolou la,waxal lingay wax gaaw

Niokhor :sama wax lenn la moy niniouy def ba baaxantal

Gnilane :guinaw binga bonalanté ba paré,mdrr ioe ay réé ngamay def yangui saf neex nii

Niokhor :souma meeunone guennei sama xol wann lako dinako def,ndax xamnani batay yangui fa

Gnilane :xana yeugo ni mangui ak kénène

Niokhor :je sais mais tmt sabarou mbourou dou meuss manquer roussite,man ak ioe liniou doundou yeupp leer namani kouci nek amna louma dessal si moromam

Gnilane :yaw dh danga nexx rek di wax,douguelaate la sama vie té ma am kima neikak,

Waay bouteel ben beutt moko yeurr yaw tmt

Niokhor :koula degglou leigui xamni danga magg deugg maa chaa ALLAH,waye sama mbébeutt yima am si ioe ak lima beugg doundou ak ioe wessogoul srtt defla sama soxna,amnaako,meune nako,té yorr nako

Gnilane :yaw daal ya oser deugg,guiss nga mane namm yapp douma taxa matt warwarane dh,sa alal diodiou titeulouma,loko am am fanano lou wessou ben neek,xolatal sa bopp si say doxaline

Niokhor :ndeysane ,lingay waxni yeupp,kouko djangatt xamni batay tu m'aimes té yangui may bayyi xel,souko donoul woone doma faalé bamay dieema tek si yoon

Gnilane :xamo sa bopp ndax yangui koy naxx té yeugouloko

Niokhor :naxouma sama bopp sax té nga nieuw niou doundaate yégali sounouy projets

Gnilane :lolou dh xana nga guiss ma fi yalla nékoul

Djigueen daal foulleu rk,wayé Niokhorr kagne lay bayyi

Niokhor :ins bi danga nek si yoon mtx,meunou niou yaatal,waye bayyil xel si limala wax te xamal ni diox nala sama yaakar yeupp

Gnilane :ioe daal amo diom,bayyi fi sa yaakaar xool ,dinga xamni tek sa takandeer si ndox taxoul nga tooy

Ins bi niongui wadj yegg si gallé Gnilane,té keur gui si boppou kogn bi la nek,dnagay diadd rek guiss ko,Niokhorr dafa goungué Gnilane nak ba si bopp kogn bi Niokhorr diko taggou nane ko ''bayil xel si lolou xamna dinagn gen yaatal'' ,wayé nioom niaar baniouy diadd dafa tombek Ngoor di tagatoo ak Astou nane ko ''wa Astou OK,samedi dina xool baxam ''

Gnilane amna loumou degg,Niokhor amna limou guiss

Wayé fiirangué taxna kouci nek taxaw rek di xoool moromam .

Lane mo wara meune xew fofou ,ba douniou dieufandikoo sen fiirangué?

You've reached the end of published parts.

⏰ Last updated: Jul 01, 2020 ⏰

Add this story to your Library to get notified about new parts!

NGOOR AK GNILANEWhere stories live. Discover now