•36•

362 48 0
                                    

        PDV DE ZEYNAB

Moi: Abdou lane la Lou khew, wakhma

Abdou: c'est l'entreprise ils n'ont pas voulu que j'entre.

Moi: quoi? Et pourquoi

Abdou: je sais pas gardien bi la dadiel si bountou bi mou Neima bokatouma si je suis exclu.

Ayy mbadou Soukey mane gua khamni wakhnako yerrei yima guiss si keur gui shiiii.

Moi: comment ça et sans explication ?

Abdou: rien ! Mais bon t'inquiète khamna après dinagn ma wowate.

Moi: je l'espère.

Abdou: mais yawe dit moi comment est ce visage là ? C'est comme si dagua don dioy Lou khew ?

Moi: heu .heuu dioy même pas

Abdou: Humm dioyo ?

Moi: Humm loumay dokh di dioy.

Abdou: hum d'accord mais bébé je veux quelques choses

Moi: Lou khew?

Abdou: je veux qu'on profite de ce moment kéne nekkou fi koudoul ioew ak mane.

Moi: qu'on le profite comment ?

Abdou: wakhtane Khana!

Moi: wakhtane ?

Abdou: oui bébé  tu sait les mots ne sont pas mes forts mais j'espère que khamgua nima la beugué?

Moi: pourquoi tu me dit tout ça mbadou dagua mayy trompé

Abdou : mohh moukou! Zeynab dama beug gua kham figua tollou si mane ligua ma diarral, zeynab malgré sougnou wa keur nignou mell , beuri histoire... Tewoul yagui lenni supporté.

Moi: hum!

Abdou: sérieux parfois sakh damay lathie nane guay deff? Zeynab yarou gua , teyye gua , dall gua , beugu guama, yeureum guama yawe dall tout mashallah je n'imagine même pas te perdre.

Moi: shiii!! Non bébé amgua lo beug li mom dou Nenee

Abdou: c'est vrai je veux que l'on se fasse un enfant.

Je me lève en sursaut du fauteuil et cours dans les toilettes pour vomir.
Limou wakh sakh titteul nama.

Abdou: waaa bébé !ki demna di.

      PDV DE TA SEYNABOU

Moi: kholal chauffeur kharal ma guéne am louma khôl magui gneuw.

Je marche tranquillement.
Me voilà devant le bâtiment et j'entre.

      PDV DE SOULEYMANE

On est dans la voiture, Souleymane qui console kadiatou ; ta Ndeye et ndeye très en colère ; mère ouly qui ne cesse de se plaindre et mass et moi assise comme deux fou car on ne sait pas ce qui se passe.

Mass: khamgua lane la daguéne niouy wakh Lou khew silence bi ba kagn.

Ils ne nous calcule même pas.

Mass: moukhamed hey Lou khew fii guisgua mane boulene ma fonto, Lou khew.

Moi: ok comme que nangu wo léne wakh mane maman sakh layy wo comme ça mou tokk keur gua khar niou.

Ndeye: woko sakh ndakh thiagua bi guéne keur gui.

Mass: heiii! Yéne Lou khew

       PDV DE MA NDATOU

CHRONIQUE Sénégalaise: Ndeye Anta tome 1Où les histoires vivent. Découvrez maintenant