•28•

326 44 0
                                    

    PDV DE TA NDEYE

Là on vient de terminer le petit déjeuner et on est entrain de réconfortée ndeye elle n'a toujours pas oublier ce qui lui est arrivé Lors de son examen.
Elle est couché sur moi.

Moi: toma santal yallah meunone na demei nénéne th boba dou geune si yawe.

Kadiatou: tata sank rek lako ko done wakh.

Zeynab: mais ndeye j'ai une idée sank rek lako done wakh Abdou, fi centre de formation yi beurri nagn essaye gua tenté watt sa chance fenene d'où deug.

Ndeye: Meuno léne ma dimbeuli ak defate examen.

Zeynab: ah balma akk.( Je m'excuse ! )

Ma ndatou: kadiatou loleini togu agn.( Kadiatou vous préparez quoi pour le repas )

Mère ouly: wa Fatou mom khana naroul dellou si.( Mais fatou elle ne compte pas revenir )

Ma ndatou: wo nama sankk néna souba layy gneuw da khawone febar. Ann kadiatou lougnouy togu ??. ( Elle m'a appelée pour dire qu'elle était un peu souffrante, donc elle reviendra demain. Oui kadiatou on prépare quoi ? )

Kadiatou: khawma sakh ndeye lo beug lekk??( Je ne sais même pas ndeye tu veut manger quoi ? )

Ndeye: ......

Moi: wakhal lo beug. ( Vas y dit ce que tu veut )

Ndeye: *en pleurant* beuguouma Dara Souleymane gnibi si la beug.( Je ne veux rien juste que Souleymane revient )

Abdou: ndeye Lila dall metii n'a trop mais nak Souleymane da nekk si liguey th ligueyi diambour la yoor.( Ndeye ce qui t'es arrivé est vraiment difficile mais Souleymane il est entrain de travailler et c'est pas son propre boulot )

Mass: En tout cas yaye tayy mom ndeye la andal ndakh je trouve très louche échoué wem bii.( En tout cas maman aujourd'hui je suis d'accord avec ndeye je trouve très louche son échoué à l'examen )

Moi: yawe heii gnouy sedal guayy tangual.

Mass: mais tata avec tout les sacrifies qu'elle a fait pour en arriver là guéne beug guem da échoué comme ça lolou guemou mako, th mane personnellement souba dina dem bassene centre régler ko.

Moukhamed: gnou demalei.

Ma ndatou: heyy yéne niar gni régler diott na dh, ndeye c'est normal mouyy wakhei ni parce que yakaram mon tasse wanté gnoune nioko wara dalalal khamal ko mirrou yallah la.

Mère ouly: wakh deug AK boulene demei école louguene fayy wakh.

Ma ndatou: degu na nak louguene fowei defko deug li mom guasse léne ko , yallah moyy dogual.

Ndeye: * en pleurant* yaye bakhna mane amna dh lima layy wakh ni fou lerr lako tekk .

??: *en criant* as salamu alaykum

Et là quelqu'un est entré de saluer dehors.

Mass: wa anlaykum salam kokou aksil.( Bonjou, c'est qui? Entrez )

Et là Ndela débarque accompagné du grande dame.
Et là ndatou se lève du fauteuil en fixant la dame.

Ma ndatou: hum Seynabou Diagne

Ta Seynabou: ménne mii.( Elle même )

Ma ndatou: yawe dh bama la khamei ba legui meusso wakh nouvelle bou bakh.( Depuis que je te connais tu n'as jamais sortie de ta bouche une bonne nouvelle )

CHRONIQUE Sénégalaise: Ndeye Anta tome 1Où les histoires vivent. Découvrez maintenant