•35•

551 64 2
                                    

    Dimanche à 11h....

   PDV DE NDEYE

On vient tous de se réveiller, on fini de prendre petit déjeuner.
On commence les préparations pour notre sortie, lakk dieune, boissons....

Fatou: Magui contane th Dara khewagoul. ( Je suis tellement excitée ! )

Kadiatou: Mane au contraire sama yaram bi moyy metti.( Et moi c'est le contraire )

Moi: ki mom Raban yii nio sokhor bou nitt gni Di ambiance mom dayy febar.

Fatou: bouffi febar nak lerna, ndeye anta maillot de bain Bei raféte n'a dh.

Moi: bane si bi ??

       PDV DE NDELA

Je viens de terminer mes préparations pour aller à la mer avec Ismaïla.
Et là codou et maïmouna apparaît devant moi avec leur sac.

Moi: li loumou?(Qu'es ce que cette tout ça ? )

Maïmouna: Khana ande ak sayy rakk gueth lolou meuneul guagnou ko.

Moi: sou guéni ande ak mane ni guéne koyy deffei, douguene mako tella wakh koulene wakh mane kassei mayy dem.

Codou: khamnagn nei Ismaïla guay andal, dougnou la déranger dagnouy fekhlou rk.

Moi: wa yéne nouguene deff ba khamko.

Codou: noppou amoul kouber.

Moi: kouber bi moyy gua teuth ko th avancé bou niarri nitt togué Di wakhtane.

Maïmouna: ohooo Ndela dagua niouy bayy niou gneuw wala.

Codou: s'il te plaît.

Moi: hum ok , souguene demei nak séne lamigne ak séne beutt yii tei léne ko lerna.

Maïmouna: En tout cas niete beutt you dadié lamigne warou si am yonn th on peut pas se contrôler.

Moi: Kone guéne tokk.

Codou: dédéte dinagn ko deff t'inquiète .

Moi: ok khar léne touti niou dem

     PDV DE NDEYE

Moi: wa yane heure lagnouy dem

Souleymane: ayy 14heure RK bakhna comme ça niou meuneu installer wou, fekhlou walei balla nio sanguou

Mère ouly: 14h heure bobou tellna dh nathieu bi dou tangu?

Moi: ndeysane ya yeuyy dh khessal bi layy khalate dayy bagne gueneu thiérei.

Mass: ndeye rew deihh sheuuu

Abdou: wala ayy 15h30mn yoyou comme ça niou guéneu nohh.

Ma ndatou: mo guene dh mane mom ayy 16h layy dem khamna yenei mayy djitou.

15h00
         PDV DE TA SEYNABOU
Je suis entrain de me préparer, je dois aller quelque part.

Ndela: yaye meunone gua gneuw niou demalei gueth dh.

Moi: mane mi loumay deff gueth.

Maïmouna: Khana fekhlou

Moi: ahh mane sakh damay guéne nii.

Codou: Kone kouy tokk si keur th papa aussi dayy guéne.

Moi: Khana niou teuth ko ndakh mane tamite damay guéne.

Alsane: yawe nak ya warone tokk mane douma yagu .

CHRONIQUE Sénégalaise: Ndeye Anta tome 1Où les histoires vivent. Découvrez maintenant