PDV DE NDELA
Là suis dans ma chambre entrain de chanter quelque chansons sur mon téléphone bizarrement je suis de bonne humeur.
MAÏMOUNA:
NDELA!J'enlève mais écouteurs lorsque je vois la bouche de maïmouna bouger.
MOI:
Tu m’appelles ?MAÏMOUNA:
Bien sûr que si Ndela. Ieow fouy gua dh ga teud ni athie sayye tankk diakarlo ak mane!MOI:
Qu'est ce que tu veut ?MAÏMOUNA:
Ahh! Mbadou dagua ma merei ndakh lima deff kerok yawe khamgua ni mane douma bagn sa khaliss lolou erreur la won rkMOI:
….MAÏMOUNA:
Tawe sougnou nk ! Wa legui balmaMOI:
BalnalaMAÏMOUNA:
Kholal Wakhou ma lolou dh kerok dagua sagnsei sakh fo démon nonou?MOI:
Yagui sogua gneuw nk! Khew la démon. Abdou maguou ndeye modon takk diabarMAÏMOUNA:
Loyy wakh ni khamna diabar diou rafet la am ma sha Allah wane ma photomMOI:
Photo ? Douko diar ndakh mom guafi don trokhal bamou fi gneuweiMAÏMOUNA:
Layy kane kou khess ki khawma Zeynab khawma?MOI:
Waw mom laMAÏMOUNA:
Ayymane ! Wakhou ma lolou dh ioew diabarou Abdou lokoy khamei bamou layy setsi?MOI:
……Ki.. zeynab damako kham rkMAÏMOUNA:
Foko khamei nak la beug kham et puis ndela temps yi gueth gua setti ndeye mom tamite rare na Lou khew?MOI:
Louy khew? da donatoul mane ak mom rk!
MAÏMOUNA :
LoutakhMOI:
Sheu maïmouna sa lathié Yagui beug eupp, khana gneuwo won pour ballou akk ish demal sakh mo gueneMAÏMOUNA:
Question dongu la won th soko répondroul ya xam nekha louma la tchip !Elle sort en claquant la porte.
MOI:
Khamone nani sama paix bi Dina am kouko yakk !!PDV DE ZEYNAB
15h...
Sama guathié bi doumako meusseu fattei, je viens tout juste de finir de nettoyer la maison tout en faisant semblant mais je sens que je m’énerve de plus en plus. Je vais appeler keysa.
Appel téléphonique avec keysa
Keysa:
Hallo! Ioew loyy wotei ak fo nekk? mba dougn la guissMoi:
Ioew keysa khana namoma, ma wola guamay wakh ayy guissKeysa:
Ma fille d’amour namenala dh damay ragual niou guiss la rkMoi:
Magui ni sama negu kéne douma guissKeysa:
Ça va j’espère que yagui si diamMoi:
Keysa nekou ma si diam dh!! Béne jour rk mayy doundou enfer gni ayy vrai mbam lagnKeysa:
Lane moyy lolou lou khew?Moi:
Khana tantam bi dima trokhal souba ba tayyKeysa:
Trokhal explique toi zeynab
VOUS LISEZ
CHRONIQUE Sénégalaise: Ndeye Anta tome 1
Ficción GeneralAimer et haïr!. Voici mon histoire car Tous qui m'aiment finiront par me détester et je finirai par détester ce qui m'aiment.Dans une histoire mal raconter. Je vous laisse terminé la chronique..