Moi: Salut man!
Elle: Bouma salut man Dieynaba Ndiaye tu étais ou jusqu'à cette heure?
Moi: Chuteeuh man! Jétais ché Aida! On avais un éxposé à finir réik dou dra!
Elle: Tu ne peux pas arétter de mentir Dieynaba Ndiaye!
Moi: Wa man fénouma! WoOowal Aida! Appelle sakh son pére si tu me crois pa ( improviséé! Souka déféé chuiii deaaaad!!!)
Elle: Temyii moOom danmaiii beugu diahàl, wantéé atten réikk! Dina diok si say mbiiir!
Moi: Man nak nékouma thi daraa loudoul thi travay bou métii! Insbiii je suis fatigué sakh! Teudina! Je dine pas!
Elle: Bana léké ba mélné kou eumb!
Moi: Ay ma! Wa je taiime bishou!
Elle: Thiiiiiip
Thiéy sma maa! MoOoma fatiguéé dh, mais maye Diez! Improviséé réik!!
Bref ce qui ést bizzar, c'est que je n'arétte pas de penser à Habib! Et tout ce que j'attend à ce moment c'est son appel, ou son téxto! Jen fais du je men foutisme, mé o fond jatten ke son appél! Pour me changer les idées, japél Ndoumbe...
Moi: MoOon bb va bian?
Elle: Ah cva nii réikk! Nka seu journnééé?
Moi: NékoOone thi weur bou métii! Je viens de décendre niii! Et toi?
Elle: Thi dépriiim totaal!!
Moi: Laisse moi deviner? Mouha?
Elle: Bilakhi il m'aide pas à l'oublierr! Il me téxto, en plus je ne pense qu'à lui! C'est clair moOom que je l'aime à fOond! Je peux pas l'oubliééé! Pour ne pa diire que c'est impossible sakh de l'oublier!
Moi: ThioOo est ce que iOow liguéwougnlaa! Paske iOow ki doofloOoneuleu dii! Ndéysane cé l'amour!!
Elle: DoOoul! Sménne bii yeup douma dianguissi! Awmathiii enviii! Filék sméne pro kaiii!
Moi: Dothi ratéé préske rién! On prend les fétes mercredi bay!!
Elle: A wé cé vréé! Dinamanéékh! Ana Habib?
Moi: Koiy kokou? Bréfff... Woy..
Elle: Loy changééé sujé?
Moi: BisOoOU mon coeur! Amatouma crésh! Bnuiii!
Elle: Yayéé koupééé!!
Habib!!!! Ya que ce nom ki peut me mettre dans tout mes états temyiii! LOUHéW???
Brééf lé 2 Jours suivants je vais à l'école, je fuis pas puisque diarouko on a les fétes le mercredi! ENFINNNNNN!!!!! VACANCEEEEUUUU! Dinama néékh! Mé dpuii manak Habib niii! Dougnou wakh! Et ca me fait màl! Ce qui m'arrive pas souvent! Le mercredi moOom; il ya eu arrét des cours a 12h! On en a profité avec Aida pour aller voir Ndoumbe!
Aida: Dawkatou diangubiii! Dra diotoulaaa!!!
Ndoumbe: Sama khoOol biii moma diapp! LoOoy méchante!
Aida: Tchiiim ninmay déiif!
Moi: Bouléne comacéé! Bréf Dougnou déim apart gnoOom Jules!
Ndoumbe: Douma meuneu guéneuh! Sma pa daii téknii dmaiii tapelé! Souba rék kaiii lay sortir!
Aida: Wa donc nous démnagnou! On va tracédji sougnou avniiirr! Paske vancancyiii doulouy yomb!
On continuu a wahtane toutiii, é aprés avec Aida on va ché L'appart de Jules! On y féke Mouha ak Galass!
Galass: Sma gayiii béguéé anh!
Aida: Nakala! Hnaa amoléne pro tdaiii mtakh néééne thiéné ici??!!
Jules: Insbiii thi ay téék diiil you matt lagnOou néé!!
Mouha: Aniii Ndoumbe?
Aida: Keur hawmeuh naka Ndiayee! MoOy koumou nékaloOone thi soiréé bii? J'ai pas retenue son nom sakh! Falagnou ko bayiii!!
Jules: Bay Ndoumbe kagn la tané bay weuriii?
Moi:...
Aida: Ah hamneuh réik hamna kokouu mokaiii déif effet bobooOoU bREF LOUY DIIIL BIII!
J'étais vrément dead! No Aida kan elle ment, elle ne réspire pas koi! Rien a ajoutéé! Le résultat étai éxtra! Mouha étais à 1cm d'éxploser!!!
Jules: Nous dàl, samdi matin lanuuy dém saliii! Paske danuufa am soiréé, le 24, 25 ak 31! Yénéne jouryiii ay picine partii you téw rék! Mé soiréébi moOom ca le feraa! Oouh si vous ratez ca, ouhoOou wahoOoumàà dOoOF DH WAYéé...
Aida: Ratéé? Haalatugnko sakh!
Moi: ioOow dh eupeulna! Balanéy wakh? NA Haàm fooy diar dabor bagnou bayileuh! Teuss!
Aida: LoLoOou moOom dagnou kaiii tracéé tkiéét..
Galass: Na gàw pask samdi cé pas dans 1moi ni dan 1sméne! Cé dan 2jour! Té gnOoune moOom avéc ou sans vous moOom SALLY NOUS VOILà!!
Moi: Yay domaràm deug deug Abdou! IioOow dh sohOor neuh!
On continuuu à wahtane, beu ay 17h, on rentre! Et je reçois un nouvau méssage! De ki? DEVINEZZZZ....!!!!

VOUS LISEZ
Thiey, quand J'avais 16 Ans
Randoml'adolescence nous avez rendu folle, ENTRE fuir les cours aller a la plage sortir avec les garçons et mm aller en weekend sans autorisation on perdait de vu le plus important et sans nous en rendre compte on passer a coté de notre avenir.