l'éclatement

64 4 0
                                    

Aida: Wa iiow nit ngeu?

Mw: Thi lane? Dimbaléma!

Aida: Nakangeu meuneu huthiié ni nit? Et pui mangiwoOne thi plin discussion!

Mw: OhoO! Yaham! Papis mingmadoOne wOo!! Ca v'diiir ke sma Yaye wathna!!

Aida: Loumlawakh?

Mw: Ak koOuka wOouyou!

Elle: Ah bOon? Louhéw bawOouyoka?

Mw: Holal insbii déiii mOom,taloumala! After dinala tégual yéép! Gnou yOokh guaww!

Et on s"mi en roUute, yakamti, ba faté no caiér kon avé dénk o boutikiééé! J"men sui raplé 5min apré ke shui arivé ché mwà! Mai sugnou keur, boy boul ham...

Kan jé sonné, cté Moussa ki é vnu m'ouvrir...

Mw: Ana mama? Dafa gneuw?

Lui: Bou yagu! Yaw déi tay réik ngeu déiii!!

Mw: Ladioumala

Et pendan c'moma, ya Papis ki aparé..

Papis: Yaw halébi dilawakh deug, nga nanekoO LADJIOKO!!

Mw: Oho dimbalima! Ana mér?

Lui: SobayiwoOul dikawakh mére, bahna! Dou hamnga rabamyi loloOoU LAY bagna dégu!

Mw: Ooho! Wahoumalolou! Anamou?

Papis: Mingisi néguam! Bouyabo ngeu wouyou!

Et j"mont vite pour alé dan sa chambr! Insyoyou, j"pensé a cke jalé diir..Thiéyy! "Mé fénkat, loundaw doukeu teu" Kom l'di si bien Aida! El mOom, hamna doubléna péram ba faté! Foumnékni kay massi déss bay...

J'frapp é él m'di dentré...

Mw: Kagn nga wathi ma?

Elle: Bane eureu diotni? Doou hamngané timiss pacéna? Diez fonékoone ba eurbi? Do mané ke Cne travay bi ngéne dOone déif moO lafa téyé ba eurbi déii!

Mw: Chiii mama bOoul ham sakh! Insbi, dama sone bi pérou soOone! I falé ke gnou paréwoOne travail bi tay tay tay! Pour t"dire sakh paréguougnOU! Mane ma moudiou gnibissi, paske dafa hawa guoudé, té dama bagnoOne ngané di wakh nahté taguoumala! GnOom Aida ak sougnou yénéne wa classbi gnoungifa balégui sakh ma!

Elle: Yaw tan ke nokoumala do bayi féne! TléfoOne binga yoOr pour lanla?

Mw: Dama hamné ke mém soumalawowone, doma gueum nahté..

Elle: Nahté hamngané eurbingafi dioguéwOone pour déim diadouwoul! Iiow! Bahna! Wa guéneulfi sakh!

Mw: Anh ma dangméy daakk?

Pendan c'te ya Moussa ki crié: "Diez kayléne réir"!

Mw: Wa g réir sakh..

Et j"mempréss d'décendr! Pfiooouuww!!

On réir é j'moOnte taf taf, envan wahbi di tambaléé!!

Je consulte mon call é je vwàh un méss d'Aida de Ndoumbe, d'Abdallah, é 3 otr d"mé amii!!!(Michél Nadésh é Paco)

Aida: Wa bb hamnga on a oublié lé cahié thi sama dofbi!!!(L'bOutikiéé)

Ndoumbe: Diez? Es vré c'ke ma di Aida? Waleuh él chérch slma à m'découragé!!

Abdallah: Fo kon parl! Téi libr dmin?

Michél: Wa mé bb thiloné?

Nadésh: Wa Nabou d"moi, bayingagnou déiii! Naka ta swrééé d'samdi?

Thiey, quand J'avais 16 AnsOù les histoires vivent. Découvrez maintenant