Seugn bi waxnani :"Ndax xamal ne kat jihaadu soxna ci yoonu Yàlla mooy mu farlu ci
topp ndigëlu boroom kërëm".. Khamnga nekk ci niarry commandement Dafeu xawa kemaane
Ndakh Nitt gni bokougn ay beug beug ( donté nio book geum yalla tei diko diaamou ) Soxna sou jebalu ci kenen meune na wacc Ndigel li ci kaw Jeuwrinam bobou Mba seurign digalko loudoul sedd xolou borom keuram naam sax douci wax..
Tchi missal mougui melni sokhna's mouride sou am Serigne Mouride ba noppi borom keureum bokk ci beineine tarikha.. kham nga fofou diouwatlo meune nafa am !
Lolou mom sou amé ana nou sokhna ci wara takhawé ? Lathiė ci yėne ñogui tėwlou ñeup djadjeuf
